De Ouf Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Yeah I'm King han
I'm King I'm King Yeah han
Yeah Boulaye Yéé
King flow
King flow
Style de ouf Yeah
Flow de ouf (Wouy yay yoy)
Deuké la thioup (Deuké la tinss)
Téguénah cool (Tay rk Guén Dh)
Ay bro de ouf
Sama side c'est de ouf (Moumou)
Yokk la paff (Pa Pa Paff)
Téguénah cool (Trrr ra)
Style de ouf Yeah hann
Flow de ouf (Yeah hann)
Deuké la thioup (Yeah hann)
Téguénah cool (Yeah hann)
Ay bro de ouf (Yeah hann)
Sama side c'est de ouf (Yeah hann)
Yokk la paff téguénah cool
Violé kouy bégne ma pércé
Talent si b'te (Beat) bone si rappeur ak tasspé Yeah
Flow bouy dioylo beutou gaïdé
Nioul té meun danél ni golo Kanté Yeah
Yobou là fodoul douté
Do bégn mm bo yorone esprit cartésien
Sa rappeur ni lakoy fuck gué
Bah thiangue may khathieu
No boulma até (Wow)
Sa rappeur la chienne elle aboie
Soiffe comme une serveuse qui veux à boire
Dima hate dima get t'a pas le choix
Youkhou yay bari ni vierge bounouy 4 doigts
Ma bamtou wat ko Moumou is King
Sa rappeur ini woul loudoul string
Comme sama escorte girls you see (Yeah Yeah)
Red curse téwoul mangui sen pakh
Bén régle meunoul mesuré sama flow si mbax
Sen laks flow yii gueni sarakhou naka mba laxx
Fuck rap bouniou maquiller pour tiktok Snap guay mbalax rk
Boné yay King ték si ndéy Kong
Je défi qui qu'on que
Si yéneu
Ma tok si trône Mafané nongue
Té amoul koumay donou
Si yéneu
Dou talent rk, Why all eye on me
Ndakh mane là ki boteu Bouki gui
Bitch Nigga Don't play with me
May ennuis boulaye Fuck midi bah minuit
Style de ouf Yeah
Flow de ouf (Wouy yay yoy)
Deuké la thioup (Deuké la tinss)
Téguénah cool (Tay rk Guén Dh)
Ay bro de ouf
Sama side c'est de ouf (Moumou)
Yokk la paff (Pa Pa Paff)
Téguénah cool (Is King)
Style de ouf Yeah hann
Flow de ouf (Yeah hann)
Deuké la thioup (Yeah hann)
Téguénah cool (Yeah hann)
Ay bro de ouf (Yeah hann)
Sama side c'est de ouf (Yeah hann)
Yokk la paff téguénah cool
Wah
(Wouy yay yoy)
Wah
(Tay rk guéh déh)
Moumou