Loading...

Download
  • Genre:Hip Hop & Rap
  • Year of Release:2024

Lyrics

Yeah I'm king

Yeah

Yeah Boulaye Yéé Enhh


Yeah I'm mad (I'm mad)

Li génn sañul lépp lay make (lay make)

Saw sa armeel rappeur dama néeg

Dóor là gauche droite bàyyi là ga géex (king)


Gëna lénë léej

Mayy client bóodul sañ yaakkalé (non)

Tas sa garde même bu nekkon palais

Des certificats décès signés par King

Boo dugge ci man dangay garer ni parking (héé)


Your girls make some noise for my hit

Pour ga wax ak man fokk ga mokkal sa speech

Jéggil sirath fekk sama street

Sa rappeur sama ndiss et sama trucs dans ces tripes (héé)


Foma déggee digga ni miig (skrr)

Gëna sikk yaw mi siqq (yaw mi siqq)

Def limay def du leen jig

F*ck ay jaan f*ck ay jiit (yeah yeah)


Buuru àll bii want more

Yeah I want more (yeah yeah)

Dak len rap lañu ma jiiñ jox ma tort

Yeah n*gga j'ai tort (yeah yeah)

Xaaru ma jekku pour feyyu

Damay dóor té du ma korr (hmm ehh)

I'm real n*gga f*ck ñu koy claim

Di jiital string takk ñoor


Héé du maak ñi

Du maak ñee

Du maak noon

Non

Du maak ñoom

Non

Du maak yaw

Non


Ndax man may def (héé man may def)

Dama mën di def (waaw aka maa mën)

Parce que man may def (waaw aka maa mën)

Dama mën di def (aka maa mën)


Headshot bal lu bopp là ci sen yóor yii

Percer fëq frontière kuy téye buur bii (héé)

Doomu Pikine là l'enfant béni

Foo gis ku mel ni man danga jommi


Duñu def li may def (nan n*gga)

Dama mën di def (héé aka maa mën)

Parce que man may def (waaw aka maa mën)

Dama mën di def (aka maa mën)


Tuuf leen ku ci nekk do gis respect (héé)

Game bii yépp lay yéeg yàq ndawu jeeg

Tufli loodul digérer xajuul ci sa deq (skrr)

Rey ma def ci sa kéent doma suul fu dul sa gént (moumou)


Wóolu sama bopp couronne bi ku ma koy dénk ?

May dugg di génn ni geen ci sa gel

Lu ma génne day metti est-ce que dolenn ma jail

Jox ma des coups ma dékku ni Pokola (pokola)


Nan n*gga

Nan n*gga

Gëmo nii lu ñuy jam dara duggu ma (pokola)

Nan safuma

Nan yéemu ma

Ñoo yem ni ñuy sabe ni ginaar yeewu ma (it's king)


Je vais les dégommer xanaa déggo ma

Ñoo def hit sans yaw té loolu leer na là

Neel sa chroniqueur bii ku ma dak rap médd là (héé)

Ñi ma bañ sax mënu ñu ma bañal

Déedéet


Ku ne king bii da bàyyi rap ne ko not yet

Donn choque moral ni guerre mondial (yeah yeah)

Fatt fépp ngeeni suffoquer foy noyye

Tukkil àdduna té duma dajjal (yeah yeah)


Rap dày dëggu du fen sa waay mbalax gay def

Li du sound wu mbëggeel f*ck ay prix nobel

Daan là fajar teel ma là mën def ko sa xel

Mën rap la ñu ma seedel


Héé du maak ñi

Du maak ñee

Du maak noon

Non

Du maak ñoom

Non

Du maak yaw

Non


Ndax man may def (héé man may def)

Dama mën di def (waaw aka maa mën)

Parce que man may def (waaw aka maa mën)

Dama mën di def (aka maa mën)


Headshot bal lu bopp là ci sen yóor yii

Percer fëq frontière kuy téye buur bii (héé)

Doomu Pikine là l'enfant béni

Foo gis ku mel ni man danga jommi


Duñu def li may def (nan n*gga)

Dama mën di def (héé aka maa mën)

Parce que man may def (waaw aka maa mën)

Dama mën di def (aka maa mën)

+

      -   or   -

      -   or   -

      NG +234

          Please Select A Playlist

          Add New Playlist

          Share on

          Embed: Love & Light EP

          Custom Size :

          • Default
          • Desktop(300*600)
          • Mobile(300*250)

          Type :

          • HTML/HTML5 (WordPress Supported)
          Get Boomplay Premium
          for
          Payment Method
          Pay With
            Review and pay
            Order Date
            Payment Method
            Due Today
            Flutterwave
              Subscription Successful

              Congratulations! You have successfully activated Boomplay 1 Month Premium.

              Now you have access to all the features of Boomplay App.
              Payment Failed

              Please check your balance and then try again.

              You'll lose your subscription if we don't have a working payment method for your account, so please check your payment details.
              Need help? Contact Boomplay Subscription Support.
              Payment Processing...
              10 s

              Payment is being processed by . Please wait while the order is being comfirmed.

              Payment Processing
              Your order is processing, and it may take up to a few days for the service provider to handle your payment. Please kindly stay tuned and check your order status in ‘User Center’.
              About Order Status