Nopil Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Yeah, Yeah I'm King (Moumou)
Yeah Boulaye Yéé (King)
Enhh han
Nan nananah
Nopill, chut!!!
Souniou néla wakhal loy wakh (Loy wakh)
Amouniou time pour thiakh
Diar si diguë bii tothieu yakh (Ay)
None yii nénah lén tant pis fii lépa gui bakh (Gui bakh)
Kou wakh fégn dagua stupid sa bopp guay nakh
Nopill, chut!!!
Souniou néla wakhal loy wakh (Loy wakh)
Amouniou time pour thiakh (Ay)
Diar si digue bii tothieu yakh
None yii nenah lén tant pis fii lépa gui bakh
Kou wakh fégn dagua stupid sa bopp guay nakh
Xipile
Kholaleu Nopil
Nioy wakh
Limay Déf si beat boula nékhoul
Da fékk mak sa girl nioy mougou
Yeah Yeah (Yeah han)
Guéne fouma nékh mou good (Good)
Gën ték métit samay opps (opps)
May gun bi semé trouble
Sen troupe
Assumer nah, Douma réthiou
Bagn bagn nangou
May sen natou
Même bodé niakhtou
Dou téh bidéw bii glow up (Moumou)
Nopil Nopil
Amoul wakh
Diokh sa Rapeure coton
Tay lay guiss mbakh
May pique may pél
Bou gass sa pakh
Kouma daka rap
Diotoul doundou
Bay déh neupp (Raaah)
Deuké di wakh noy meuné dieuf tël sa lamign (chutt)
May F*ck sa rappeur yépp même
Souma signé wone monogamie
Damléne guénah bon
Nagoul nogual li dih don
Mangui si trône bii
Wesh au sommet
Kone pour khole ma outil drone
Dou change for real mafi néh ak flow de ouf
Dou béne foma dégue guiss sa bopp si souf
Mélni mane day guen diafé (Moumou)
C'est se que Dieu à fait (King)
Paré Fépp
Diléne douma khole nouniouy dioyé
Nopill, chut!!!
Souniou néla wakhal loy wakh (Loy wakh)
Amouniou time pour thiakh
Diar si digue bii tothieu yakh (Ay)
None yii nénah lén tant pis fii lépa gui bakh
Kou wakh fégn dagua stupid sa bopp guay nakh
Nopill, chut!!!
Souniou néla wakhal loy wakh (Loy wakh)
Amouniou temps bii pour thiakh (Ay)
Diar si digue bii tothieu yakh
None yii nenah lén tant pis fii lépa gui bakh
Kou wakh fégn dagua stupid sa bopp guay nakh