SAÏ SAÏ ft. Silassi Ay & Troizess Rebel Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Yeah ehh yeah I'm king Yeah Boulaye Yéé
Silansi Ay my name nigger
SeSeSe
Yeah Sen commedi show lay nieuw Déf drama (Moumou)
Amoul hasard damay doundou sama karma
For Real
Dou méti bagua dégue mani tarna (Tarna)
Khékh bah dead ni vikings mangui Valhalla (Yeah)
Dagnou ma ragal dou dégn ma bagn (Moumou)
Wané sama dolé moni mél
Boulma diokh khole délma bayii khél
Bindeu sama tuur si bépp toundou yeah (Yeah)
Kou wakh si sama guinaw toundou ndiem (Yeah)
May buur tigui kham gua douniou yam (Moumou)
Douma bakou té kham gua dane
No cap, ndourou woumak kén même sama sékh
Niom nioy lépp, nima tangué takh kén dousi fékh
Non no fake, wolma kousi déss ma rédi féss
Saï saï béh, guénal ma dieul sa bakane wakh gui diékh
T'es pas dans ton assiette car suis dans cuisine
Nima deumé si rap takh
Vous ne serez pas dure à cuire
Ma mome 22 23
Nomay digéré dama wékh
Khamouma peace diaroul yékati drapeaux gou wékh
May saï saï anh (may saï saï anh)
Dama beuri thiay thiay anh (beuri thiay thiay anh)
May saï saï anh (May saï saï)
Dama beuri thiay thiay Anh (saï saï bééh)
C'est quoi les bails anh (skrr)
Boy Pikine bii moy sa baye anh (saï saï bééh)
Nioy takh gua bayii anh
Néléne kou wétt kham sa bay waw
Nigger, I'm a crazy wakh ma loumay féthieu (féthieu)
Thiéli koumay téré fly
Tom et Jerry man ak séni gars yii
Dore la daleu wane la may sa baye (Baye)
Bizarre samay khétou diap
Tassat bare yii gars yii diape dathieu
Todiat mbar yii mosal gnépp si tate
Pique ma sa pussy mum la douguat
Meun ndeye rap takh douma Khékh ak mome (wahh)
Rappeur di khékh ak mane
Dougnou ma garée never dou kén si gnom (Non)
Fok gnépp kham mane may kane
Damay fo si beat ni Pop Smoke (Ay)
Rap diko ték si côte (Ay)
Kouffi sousou boy yii ték si yone (Yeah)
Té dou matt une seconde
Freestyle yii rk kay niapp sa xone (rah rah)
Ni kou sik té manqué bone
May théré si beat soudoune tadiabone (wah)
Sans mane dou nékh
Apart cho yii wakh ma loumay danél my niggers (my nigger)
Rap douniou masi garé my nigger
Ni auto mane gnépp lay garée ma nigger
Tok sama galé di léwal
Deumb la wala djinné
Guiss gaïdé si aleu guanan daguay fo ré
Dérétou rappeur lamay doundé
Sa papeu si rap sakh damakoy fowé (euuh)
Kinpi cona lama deuk fils
Maléne dakk rap maléne guénah diss
Text you carré flow bou guénah diss
Sou naré thiol ma ini penalty saï saï
May saï saï anh (may saï saï anh)
Dama beuri thiay thiay anh (beuri thiay thiay anh)
May saï saï anh (May saï saï)
Dama beuri thiay thiay Anh (saï saï bééh)
C'est quoi les bails anh (skrr)
Boy Pikine bii moy sa baye anh (saï saï bééh)
Nioy takh gua bayii anh
Néléne kou wétt kham sa bay waw
Courant dou pil doniou fil
Bougo niou takk imbécile
Guéné guent guenn ci
Ngay ladj kagne lay délouci (SSS)
May def lou 10 ngamay 6
Beugo niou siw ni lomotif
Meunn rap beugo boudé marchandise
Wacc port nga dieul gal gui siff
Og rebel rebel tigui (tigui)
Kou sénn dinga sigui (sigui hé)
Doff ci birr doff ci biti (rah)
Wathié pell mayé pigui (rah rah)
Forcé buzz safo dibi
Khéwi ni mbiskitt gouy gui
Yama djitou malay boudil
Yeugueul sa niveau ma wathiél la bible
Nioy sa père fo niou degg mérr
Boy diokh niou thieur fecc thieuguinn (skrr)
Wathie bess lougne def mou nekh
Nangoul té def niou sa Dieuwrigne (waw waw)
Fatt fepp yaako téré nekh
Feull fly di fuck senn feu rouge
Fake bouy forcé dou free
Fo nagne ba fété la fo né
Wala bigueunn baa gueun (yeah)
Bilayy motali mo gueunn
Safo khorom malay soukeur
Mann ngay golou malay dougueul
Job rek talouniou wakh dji
Petit camp nioun mine pakh bi
Fuck sissou man yi yek lary money
Amwa time boy ba temps yi (ooh)
May saï saï anh (may saï saï anh)
Dama beuri thiay thiay anh (beuri thiay thiay anh)
May saï saï anh (May saï saï)
Dama beuri thiay thiay Anh (saï saï bééh)
C'est quoi les bails anh (skrr)
Boy Pikine bii moy sa baye anh (saï saï bééh)
Nioy takh gua bayii anh
Néléne kou wétt kham sa bay waw
Niongui thiéné sounou side job bii di fly yeah
Money money on my mind nah projet yii high
Man you can stop me bro on my way yeah
You can stop me bro on my way yeah