Wéetaay Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2024
Lyrics
Ñi taxx màdane yeuk jariñu adunah
Dem nañ, Dem nañ
Ñoom dem nañu bayii ma
Mama mangui dee ak wéetaay
Papa mangui dee ak wéetaay
Dayy tiis, ñunane ma ñaan lalene desel
Té gis, lii gén def ci man bama mel nima mel
Tey bés, yagui dem teewul xol gui wéroul
Ci sédday saxx féexul
Wéetaay bama fajutt Yeah
Wéetaay
Jooy ci sama wéetaay
Fouma tëdd nelawatouma yaay
Wéetaay
Jooy ci sama wéetaay
Fouma tëdd nelawatouma yaay
Xol gui di fees rongooñ di tuuru
Naqar dou wees mbecté dou mujju
Nah xaar lii des xëyy naa gën lima dunduu
Góom bi daye gëna bees mel ni tey lanu gaañu
Metit gu xóot ni rongooñ gui sama bët yi muur
Bëgg jaboot waral gua dëkk daw chaque jours
Biñu mama di boot ga dacc lu-nekk ci nacc giir ñun
Fayuma bor ñàkk là donn góom boumay dëkk muuñ
Yañu dane wéetali bi baay deme
Mëuso ñu bàyyi ak keneen
Sonn ci ñun manqué wuñu lenn
Sa mbeuguel ci man yàgg nama leer
Mama
Dilaa xalaat fan gua nekk
Mama
Gisatu ma la sama wet
Soree woma ndax mangui lay yég
Yagui ci sama xol duma là seet
Wéetaayy
Jooy ci sama wéetaay
Fouma tëdd nelawatouma yaay
Fouma tëdd nelawatouma yaay
Fouma gëmm nelawatouma yaay
Ñi taxx màdane yeuk jariñu adunah
Dem nañ, Dem nañ
Ñoom dem nañu bayii ma
Mama mangui dee ak wéetaay
Papa mangui dee ak wéetaay
Dayy tiis, ñunane ma ñaan lalene desel
Té gis, lii gén def ci man bama mel nima mel
Tey bés, yagui dem teewul xol gui wéroul
Ci sédday saxx féexul
Wéetaay bama fajutt Yeah