BBN (Bañ Bañ Nangu) Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2024
Lyrics
Yeah, Yeah I'm King Enh
I'm king, I'm king Yeah Enh
Yeah Boulaye Yéé
Enh Enh
Ohh whoa oh whoa enhh
Yeah it's King Moumou
Yeah Enh Yeah
Bañ bañ nangu Yeah
Wala xaru (wala xaru)
Non bul dugg ci man daguay gaañu (daguay wàcc)
Ndax do mucc Yeah
Fi Amul wallu
I feel like god ci ñoom
Chaques versets niou waaru
Mo jox ma beat Yeah (It's king)
Def ci kick (Moumou)
Yokk ci 808
Maa def ci hit
Ñuy gëna hate (krrr)
Sandi bic xotti kayit (ooh)
Mujj ci depression
Oh, my bad (king)
Daan la bayy laaj photo
Mangui sa kaw nangul défaite
You get enough, maay turn off
Sa cuune yi nii (moumou)
King du wér ni dof, digga loof
Soma toppe ci li (soma toppe ci li)
Ayy baa mujje soof, lan gay xoff
Defa gumma nothing (defa gumma nothing)
From bottom to top, kumay stop
Saay mbokk yenu sulli
Dëkke def ni man xamm ga non non du ñu yaam (moumou)
Buur di gén nott jaam lolaay man ak yeen (skrr)
Kouy King ci sa game bu dul man rek di fen (fen)
Nangul loy bañ siisu tax demo feen
hmmm
Manë xéé manë
The King
Basta ngi duñu ci nada
B*tch
Ñëw woon la nan lak naka la
Gua giss ni
Manë xéé manë
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal (nan nan nan)
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal (ohh yeah)
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal
Sa xol mënul sedd,
Soxor mësul jekk, Yeah
Ammul lu ñuyy ci seet
Di là tekk naqar ci di déf lu rafet
Yéene néeg là borom ma ciy fanaan good night
Yéemé n*gga doma bañal lu maa def mu nice
Temps bi du change bagua giss guddi muy naaj
No bilahi Ame talent baa saï saï
Ki may tëkkale xanaa daf ma yab
Fu ñu ma dégge séeni fit du toog
Ñoggi ñaan ci ngeek ndax li dafa ëpp
Nélén fi ma dëkk Pikine dafa rëb (my city)
Ain't f*ck with this niggers Yeah
Bokku ñu catégorie dou maak n*ggers yii
Màgui ci wetu gor ngi real n*gga yii
Yeah Boulaye Yéé, you got me (I got you)
hmmm
Manë xéé manë
The King
Basta ngi duñu ci nada
B*tch
Ñëw woon la nan lak naka la
Gua giss ni
Manë xéé manë
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal (nan nan nan)
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal (ohh yeah)
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal
Mënu ñu ma bañ
Mënu ñu ma bañal