Mafi Néh Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Yeah I'm King Enhh
I'm King I'm King Yeah Enh
Yeah Boulaye Yéé
Ennnhhhh ahhh wow
Ehh mafi néh
(Yaa fi néh Yaa fi néh Ya wóor dh)
Boy mafi néh
(Yaa fi néh Ya wóor dh Héé Yaa fi néh )
Lancer gua sa carrière air ball
Looy wax wa koñ baa xam nga day col
Ndax mafi néh xana déggo
Vous êtes seulement là pour le décor
Ehh mafi néh
(Yaa fi néh Yaa fi néh Ya wóor dh)
Boy mafi néh
(Yafi né Yafi né Ya wóor dh)
Tollu len mah sax ci catu we
Dagg làmmiñ muuma noo may caatu we
Kuy tëkkale luasse ak cattewee
Bruit bay bari mais duu wéeranté
Ni mafi néh
Mafi néh ne maa laf cat
Gën len xarañ cat bah cat
Tey gaynde mer tee deggul jat
Fi ñuy siib bari xamu ñu gat
Bàyyil Rap tee defi thiak thiak
Man rek keneen du fi xàcc
Ndax jotuma doóre ñu gui nàcc
Sumay fo sen level di wàcc
Prip gua puub saw sa tubay
Yeah I'm the goat may sëtu béy
Pikine ma kóoy boot so len di hate
Rap du ma ci mbokk dama ci néeg
Jarul gay jéem n*gga dagga mënul
Fi xànju b bari lu tax gén mën duul
Onk bu meti day bu tutti tee xeeñul
Def lóoy nangu nii ma mën ci xeet gu ñuul (Wow)
Ubbi ma fëgg la rappeur yày sama b*tch gaawa tekki ngembu ni Feugeuleu ay
King bii no ken lë jarul late ndax ku wétt xam sa baay lolou dëgg lë kaay
I'm stunna taxx do def limay def bokoy jéem di gaañu ndeysane
May tari ga nane ëuskeey rap mësuma donn talibeem te ku kóoy def maay sëriñam
Lo fi tabax maa kóoy yakk
Giine téh cere ak ndawal ma fi teg tank
Ak king dagay rap baa sa bun di ñaq
Jox ko cadeau ndax du mujje ludul ñàkk
Nomay téwé ni biir buy daw duma ñëwé ndànk
Yén sa rappeur lou méti té douma bayii mou wàcc
Yokk la gàcce ndax dama paré
Doko tay sax n*gga somay laajte
Ndax mafi néh
(Yaa fi néh Yaa fi néh Ya wóor dh)
Boy mafi néh
(Yaa fi néh Ya wóor dh Héé Yaa fi néh )
Lancer gua sa carrière air ball
Looy wax wa koñ baa xam nga day col
Ndax mafi néh xana déggo
Vous êtes seulement là pour le décor
Ehh mafi néh
(Yaa fi néh Yaa fi néh Ya wóor dh)
Boy mafi néh
(Yafi né Yafi né Ya wóor dh)
Tollu len mah sax ci catu we
Dagg làmmiñ muuma noo may caatu we
Kuy tëkkale luasse ak cattewee
Bruit bay bari mais duu wéeranté
Ni mafi néh
Tàllal gaz tokk ci Yeah
Lii may def moo là metti Yeah
Tàllal gaz tokk ci
Lii may def moo là metti Boy
Tàllal gaz tokk ci
Non dalà metti
Tàllal gaz tokk ci