Bye Bye ft. Khalil Bishop & Reema Juuf Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Dém Na Ba réér Guestou di Ladjté
Wayé melneu ni mane fima awone dou foofou
Mane xool na ba xool Séét na ba séét
Doundou na yeug ni lima fogoone dou loolou
Bye bye , néma bye bye
Ségam xol yi wouté naniou néma bye bye
Bye bye , néma bye bye
Guiss guiss yi bokatouniou néma bye
Yow ! Xool na ba guiss lamb dadj moss na ba yeuk
Yeuk naafa mbékté yeug fa tiss naxarou deudj
Dadj nafa koumpeu, eumbou koumba oupeu touma
Now i'm walking alone, make my way bér sama yone
Xool Na ba xool , seet na ba seet
Wayé lima jota guiss ni dara doyou maffi
Wax nguéén ma degg , djeuf nguén ba tekk
Té amoul léne louci meuneu changé ma vie
Bye bye , néma bye bye
Mangui dém sama yone kone néma bye bye
Mangui dém sama yone kone néma bye bye