All About Luv ft. Thié L'Esprit, Saliou Golden, Spiirit & Emelene Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Sobounathi ma nigger dégueu lou nekk
Taxoul ma xaddi di daww
Beguenako ma nigger hip hop rek
Dekeuthi doundou falaw
Yagueu rêver ma nigger beus dîna niew ma dieul rap nangou.
Kheuthi bou dagoul dikk gueum ko rkk zik bi deff thi iow
Noooonw
So menoul boul tekk boulko deff boulko deff no no ma nigger
So menoul deff tchill moy li gueun moy li gueun ma nigger
Zik-Mu dou fow boul kaf boul kaf non non ma nigger
Hip hip lou real dou yeufou fekk non non ma nigger
Gueum ko topou ko dieufé ko bayi di matteu di eufff (di Matteu di euff)
Kheuythi yendouthi fananthi dieulko deff sa yeuf
Dieulko doundou rek feseul rap yeketi lokhoo thi kaww
Diokhétti diokhéthi rimes yokou niveau Afair bi law ba faww....
All about the music we love it mo sax ci xol yi
Every time niongui ci diko matal ak xol bou raféte
Geum geum leu dou doone lénééne
3G Team dou doone fénééne
We still in love with music link bi dou meusseu dégn

Meun na sakh teud diko guénte music Dafmay téré nélaw
Sokh la wouma cash Pour mane nék thie rek moy law ba faw
Dou succés dou succés dou succés Music bi mo déh thie xol bi
Sou done money rk mane bayina yaguna té dém mane lidjeunti djagu bii
It's all about music
Douma téguii tank thi bi zik
Damakay handle mane ak sama team lign gueum yeup bolé nagn thi music
Holla
Dégu nathi dou déme Ma teukh rk Yokk sakh limay war
Pour push rek Guéde nagn mathi Wagni nagn mathie
Téwoul sakh damay deim ba seuss rk
Deugueuntane la dou kaff
Music thi deal bi la bok dafa iné thi mane sakh
Teugu na tei dou tass
Séni wakh lay dékou moumay gueuna yokk aye diom sakh
Gueum nako sakh tei daye fay
Lima beugu zik lako dinke all day
Maguii dégu aye yokouté té day yokk sakh it all about music
All about the music we love it mo sax ci xol yi
Every time niongui ci diko matal ak xol bou raféte
Geum geum leu dou doone lénééne
3G Team dou doone fénééne
We still in love with music link bi dou meusseu dégn
All about the music we love it mo sax ci xol yi
Every time niongui ci diko matal ak xol bou raféte
Geum geum leu dou doone lénééne
3G Team dou doone fénééne
We still in love with music link bi dou meusseu dégn
Determinate i never back down
Hustle ba déi ci limay doundeul ak lima bégueul
Yeuk yeuk bari takh ba moudjiè nek begu begu
You would know what about love tell'em i don't know
Musik sar sama bop ba moudjé mom sama xol
Dafma dap am djoudouwalé fils ladj ko kima sak
Rap ba yeuk sama bop gnimay déglou nane dina baax
Boy dangay dém xeuth bou dakoul dik yea dina baax
Lou caisse yek basse yi geuneu dal may geuneu feugu deune
Xam xam ak beugu beugu determiné sama meune meune
Boy damay def ndax amour non sentouwoumasi tédeu
All about love yone bima dieul dou keine koumasiy tégui (emelene)