Do Def Lou Melni ft. Daddy Ink, Fatiima, Thié L'Esprit, Abt Diay Prek & Jey Major Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Hey bro zappel fakes yi
Douniou déf lou mel ni
Yangui may get radio kl ak Radio thies kone
Boulma ladj lane mooy Ink
Welcome to Dox Dadjé , Saa yoo Paré
Li may tek nimou simplé
Nanga def loula neikh nanga dem foula neikh
Mais xamal daddy kouthi dadjék moom dinga mort né
Koulén geuneu Aay , kouléén geun bandi 3G team la collaborél
Took tchi trone bi di xaar kouma provoké
Thiaga yi doul tchi mane comme dab
pourtant meussoumaci laale kéne meme pas
How yeah Amouloo gate dicci bakkou
Fuck say niggers ak sa wa crew
Lima beug moy nguén def groupe di tarri samay son ni kouy kourél
Han Dama Lakkalé , ni Italie ak Makélélé
Gnimay djéma doutye nak ma taclé lééne
Fii kouné amna sagn sagn beug wala bagn
Bayi wouma kéneu dou goor dou jigguén
koudoul goor douci guéneu
Diaroul xoureul baate pour meun nekk real
Mane gaindé la ci alleu bi nioome aye Moussou maiga bi lagne
Damn
Bissmilah feug bountou rap niouni ma aksil
Yagg tekk lou carré waral tay ma nieuw té aaksi
Damalay xaraf Han dawal dioxma paaka ak scie
Niou daggaté game bi tégaate mcs yeup ci axe yi
I am one girl who have like mission mooy to manage you
Wane leu yoone tété leu défleu béneu boy town bou cool
Séppi thioy yi tonni lééne tour
Tappeu goor gni amatoulééne xour
Béneu jiguéén ci niéti goor
Mou xonteu lééne aki flow you douf
Anh , do def lou mel ni
Non nigger do def lou melni
Get ko rek yaw ame loula métti
Bane jiguééne moo sagna nieuw wax lii? Mane
Do def lou mel ni , non nigger do def lou mel ni
Xamoo touss dignou diam son you méti
Bayil rap nga bagne dooo Bayi
Yagg indi lou nice tek lou high yeukeuti niveau bi fly
Job ko demb tay sooga nieuw nan bouldi shine
No , No Do def lou melni
No , no Do def lou melni (X2)
Athchieu séédé yalla mangui touché
Du bois nguéén wara daw touché
Maraw systém LMD nigger yangui cartouché
100mil kg punchlines laay couché
TD yéla men Nigger yangui youxou mayday
Dédééte lamine boulééne djééma aidé
Douma seutou sagne sagne faye
Wayé sama deug deug xamalnama sagn sagn mooy faye
Diay na prek , todj na founé
Takk na tim tak tik
Ma geuneu paré sax séén mind ak bic
Sen mind ak beat
Geudj ngama dégg meun ngama xaar di
boul xaddi ndax mangui ci yoone bi xadji xadji
Dégati nga dadj malay fadj,
Deug djiga degg nigger mala diox
May gass rek ngay soul han
Fouma gestu guiss la ngay doul han
Mangui rap baléégui doffo han
Linga fook lepp da foo
Ma nigger bi bakk nga ndjakk
Abt diay prek dou daw contact
Sadik day rap ba gniite ko tek
Ba thiate ba thiate, goudéék beuthieuk
Yéwou dioug foudou feug deun djeull yoon
Adji barre yi tax nga thieuk rampé sissa zone
Niakka linga ame lisé-monopo foofou yeup
Gayi guiss né meusso nek ak niome ci yoone
Adouna dou neikh banga def li
Insbii danga tooy dagn la touf li
Nala wax deug donté goné la
Samay kadou makk nanoo fanane ci Alleu yi
Djéém nga beu soneu yaw meuno dém
Nguir Yalla bayikook gniko meun
Useul sa brain, défidji lénééne
Pour djarignou nigger xél koom leu
Jey major nigger xam fimou jeum,
Sa padré ci yoone bi dou kouma geune
Manguék hilaire bi djoublou dji toole ba
Pour bayi dji game bi xelcom leu
Dou nééngeu gaindé nga ,
Euh pour ma geum leu deug deug nigger faw ma guiss sa guééne
Té sa xiirou mouss never xouxeul
Beu nga deg deug nigger doossi meusseu guéneu
Flow bi takk boom guéné douille balle rhymes
Djam sa bopp nopp nathie from fathié linga teulé
Sa rap dou sarap, lingay tek dou sarap,
Mangui daane di sa rap moytouma damay killé han
Yagg indi lou nice tek lou high yeukeuti niveau bi fly
Job ko demb tay sooga nieuw nan bouldi shine
No , No Do def lou melni
No , no Do def lou melni (X2)