![Jeurejeuf ft. Famsy, Donking, Reema Juuf, Thié L'Esprit & BMB](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/06/26/525dae0c46504872967a506ea743e141_464_464.jpg)
Jeurejeuf ft. Famsy, Donking, Reema Juuf, Thié L'Esprit & BMB Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant Ma mama boy
Souma doundé ba dé wouyoumala douma talli
Ndax linga dadj sama dieum dafa beuri lol
Tété nga nampal nga boot nga
Mate ngama kér waral képaar gui féékh
Mama, yaye jant biy lééral sama yoone
Yaadi souf di assamane di bidew di wéér
Ma mama i love you amouma sa faye
Yaya boye amouma sa faye
Ndax eumb diourom nienti weer dafa meti
Diobou yaaya boye makka sax meunooko faye
Yaya boye yaaye ki geune soneu ci nioune
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant Ma mama boy
Maaaaaaaa, mamamamamama
Mame Penda, i love you
Ba nieup dane nélaw mamaaaa
Yaw yaye ki done soneu ci mane Ma
Xel bi xéli taye
Bindeu rek dieumeulé ci niome
Niome leu bobou ba tay
Niome leu rek dou tar baniou bayi
Yagg wérou ci niome xeuy réére niou djap tekk ci yoone
Yagg wérou ci niome tiss téw nga guestou yam ci nioome
Yaye , yayou kéneu leu
Wanté baye boy bayou nieup leu
Beuss niki tay déf ko sa deug ioe
Weuri ko , seti ko diégué ko ioe louko neikh
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant Ma mama boy
It's time to show you how much i love you
It's time to show you how much i need you
I'm goona do my best, nguir djeima fay bi borr Mama
Téralal yaye, siggilal baye ndax niola déf linga done
Téralal yaye, siggilal baye ndax niola déf linga done
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant
Sa doome magg tay jeuréjeuf yaye
Xeuy tekki ndieurigne sa sakk leu
Akkou ndiourel diss neu lool
Tay malay sant Ma mama boy