Hello ft. Kush No Game & Saliou Golden Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Han Yeureum ma yaw , boulma ték thiono
Xaw mafi dara kone wane ma lou baax
Xamal ma yaw, esk mak yéén nio niro
Mba dolééne ma xéép ndax awma fi morom
No mél ioe waxma
Nouma wara mél ioe waxma
Boudé Ya geun fi waxma
Souma xamé ba ranié nga doyma ma royla
Hello
Waxma loutax banga nieuw fi
Periode motax bama nieuw fi
S'il te plait waxma looy déf fi
Kane mola bayi fi lane mola téh fi
Haan
I've mercy on me, don't hold me back
iI don"t know anytihing show me the right
Ow yeah
Hello , Mba diam fi ame
Yang may réé xamna diam nga yéné
Xaw ma, kaay tekk ma ci yoone
Souma xamé waxla yaaye kane
haan Waxma loutax banga nieuw fi
Periode motax bama nieuw fi
S'il te plait waxma looy déf fi
Kane mola bayi fi lane mola téh fi
Waxma loutax banga nieuw fi
Periode motax bama nieuw fi
S'il te plait waxma looy déf fi
Kane mola bayi