Ndam Rek ft. Fatiima, 4Leuz & Fonetik Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Geum ko beug ko niou wouteulék gnéneu gni
Bou yoone diééxoul waxoussil dou diééx
Kone Ndam Reik ! Warrior , Warrior
We believe in us we goona succeed
One day we'll have success
Warrior ! Warrior
4Leuz
Dialooré Daaw , ndamou nopalou gaaw
Niaféél Mou fayla nga feuss
Djitté nieup ni Taaw (Haan)
Ndox mou touroo geun fouf, Ndaalou totchie man
From the botom batay, Thieuy lign tchi datchie man
So diangoul war nga xam liguéy day fay ba Alaxira
Dioudou bou reuy ndeye ak baye licci dess sa mbira
Baye fall ioe niaféll nga pouss
Dou niak nak onde yi day souss
Boul tayi démal nga xouss
Déf défaate lolou dou touss
Nénagn la gonék baak sou taaxirlo rek rootal yaayam
Domay allal té sou féniaguéé rek rootal layam
Mane 4leuz douma meun athiou
Job ba jant so douma lekk wathiou
Sama Daaw ak réne wouté neu
Soo niakké jom mou teu leu
Ndéké daal wégn rek mooy dagg wégn
Raak ko tchi kaw com mbeur ak kourpegn
Kou xam xam xam xam ndam
Sama Yoone xaxane ak jam jam
Sama baate com poto lolou dou dégn dawsil looy xaar (looy xaar)
Kone Fo' ak Foné, woonaniou kouné aksil niooy waar (Niooy Waar)
Geum ko beug ko niou wouteulék gnéneu gni
Bou yoone diééxoul waxoussil dou diééx
Kone Ndam Reik ! Warrior , Warrior
We believe in us we goona succeed
One day we'll have success
Warrior ! Warrior
Fonetik
Doggou deugou dir direction wou ndam dou dégn ci mane
Allergie lose foulay féégn ci waar bacci xar kanam
Tékki la tekk shock taylé lepp tekk ci bakanam
Tout terrain ci waar mou diaral ko lepp bacci sax Kanam (leer na)
Guinaaw bouki yaye ak baye seen walleu wey neu
Boul took di xaar ci kéneu lila ci guéné dioug xeuy leu
Ndar xeuyoul soti tallal loxo niaane dou wallou gorr
Deuké daadj beu teuthiou mou té yokh looloy wallou goor
Waay goor , dooko dégg mouk tchi ker gou seddeu
Fii fook nga dang dangui ci naadj soofi beugué téddeu
Yaafouss dou faye dou fayéékou té dou amé geudeu
Respect likoy mayé soobou waar leu non dou took di teudeu
Néénagn ma : loo jooboul tay dooko fayékou soubeu
Say fautou demb meun na doone galankoorou soubeu
Life bi numéro leu maay sédeulé ni number tén
Bi nieupiy rooti mane dama taamou kassoup téén
Geum ko beug ko niou wouteulék gnéneu gni
Bou yoone diééxoul waxoussil dou diééx
Kone Ndam Reik ! Warrior , Warrior
We believe in us we goona succeed
One day we'll have success
Warrior ! Warrior
Electronic Girl
Warior we are , we gonna be strong
Diapp teuweu bayi mooy souniou symbol
Nioune ndam rek mooniou yitéél
bougn ko amé jéém ko téyé
Kou beug dara dangay déf dara
Yalla meun leu diapalé pour nga ame dara
Kou beug dara fook nga déf dara
Kone fight , fight once more
Geum ko beug ko niou wouteulék gnéneu gni
Bou yoone diééxoul waxoussil dou diééx
Kone Ndam Reik ! Warrior , Warrior
We believe in us we goona succeed
One day we'll have success
Warrior ! Warrior