![Lepp Diam ft. Xeusha XN, Punchef, Daddy Ink & Pii N Bii](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/06/26/525dae0c46504872967a506ea743e141_464_464.jpg)
Lepp Diam ft. Xeusha XN, Punchef, Daddy Ink & Pii N Bii Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2017
Lyrics
Dina Atté xeeix bi sans verdict lay nek
Wadji tane yone bi xamna tourou noone yiko ray
Douma niakk fayda ba bén boy dima yapp
Gnifi ndieuk nieuw beug fi diaay pank com dab
Fii Lepp Diam
Salamaleikoum mba diam nga ma ameu
3g mo wotei dox dajei
Diapeur pii n bii nigger leip diam
Daniou dioud reik nga daw douniou book ndadjei
Yangui niouy sentou si kaw nigger dina ameu
Jeuf jeul niak diariniou
Da nga indi ayeu soriniou
Peace love and hormony
Daddy ink nena meune nga dem
Da nga teulei koneu almany
Da nga yaga takou top rap
Do leik fi ak sourouma
Danga reip kay sorou ma
Am nga chance tay leip diam
Madane dox deuké rap nioumay diate dima dioulé
Sen wax douma dougou douma fate dama toule
Iri guélou none bi diko tate diko mbeulé
Niouy tabax béneuh béneuh may tothie ay full
Dieul sen text diko dial diko boulé
Gnima dane dir mbague niom nieup la soul
Teglé sama tanke dilen pap niouy xoulé
Mangui degg sama diameuh Legui nak dama Cooool
Wessou deureum may ondou ,sodoul lyrical do gawa nandeuh
Tothie na sama monde, koula lathie punchef neko lepp diameuh praaaa
Dina Atté xeeix bi sans verdict lay nek (lolou sax diaroul wax)
Wadji tane yone bi xamna tourou noone yiko ray (tchi sama gayi la dal)
Douma niakk fayda ba bén boy dima yapp (lolou sax amoul sens)
Gnifi ndieuk nieuw beug fi diaay pank com dab (waxlééne sama zone mome lepp diam)
Fii lepp diam , boy ioe lekko naano tegg lé tank doula déf legend
Fii lepp diam , lii dou hardcore mem soula tangor xanié diam ngay kaas
Beugo diam ngay raak , waa koula toogn ?!
Boudoul sa bopp kén doula nokk, au minimum war nga xamni yaa ress sa bopp baaye faal
Gueudj na niou guissé mai fi lepp diam
Nio ngui job souniou job nguir ame ndam
Diaroul titt ba sa tatt di teugui tam tam
Ndakh diogué gouniou souniou yonou wouti xam xam
Yague yague daniou dadié kone na taggo di nice
Nguir nga bania rouss souniou face face
Sama coudou gui ma yorei diam lay raath meme si somay beugueu diay djiko say say
Adouna ni demei tay mou nioul souba dafay wekh
Naniou fekhei rek ba dara dara douniou takha khekh
Lou goudi leundeum leundeum kham ngani beut dina sett
Tei dei mongui reub defaral fimoulay fekk
Assalamou aleyka diam si iow layy gnane After wake up
Ndéké mom lagnou sokhla koussi meuneu waff thiow romb aythia stand up
Diameu moy oumpé dara diotouma lep diameu yéne gnima guédia guiss mangui sant god
Xamnga rekk dama gnakeu diote ak mixtape YYY bi mayy deuké job
Galsen dagnou wara geuneu meuneu sant ndakh fi salam gui yaa na
Même bougnou dé ppte no stress lep diameu
Dina Atté xeeix bi sans verdict lay nek (lolou sax diaroul wax)
Wadji tane yone bi xamna tourou noone yiko ray (tchi sama gayi la dal)
Douma niakk fayda ba bén boy dima yapp (lolou sax amoul sens)
Gnifi ndieuk nieuw beug fi diaay pank com dab (waxlééne sama zone mome lepp diam)
Fii lepp diam , boy ioe lekko naano tegg lé tank doula déf legend
Fii lepp diam , lii dou hardcore mem soula tangor xanié diam ngay kaas
Beugo diam ngay raak , waa koula toogn ?!
Boudoul sa bopp kén doula nokk, au minimum war nga xamni yaa ress sa bopp baaye faal
Lép Diam kay manguii dounde ataraxie (Ouais)
Manak néw bou tékhé ték ték..
Mangui diap peace chargement bi Matna maxi (wesh)
Dox dadie nila nekheii
Mbékté sama biir xol circulé nii taxi..(Yeah)
Loumay téré doundeu diam tay..
Segam Mere bi Mingui diouli dima nianal muy akesi (weah)
Sama vie lepp diam kay
Yéné gnép diam faynama Khol ngama
Bomay indil diap sakh damay fiirii khamnii compo deal bii
Mani yalla burbii Maynama hamdoulilah
Ndax diam la beug diko dunde sama khol
Niggah mokal thi ndigeul nii téguédégué..
Doundou aya takh gnou kham valeurou diam sakh thi geuneu raw
Thiono dunya bumla terrei begueii
Nakar sa khol bumu fegne sa kanam deiko santei kithii kaw
Ahaan.. dangay geuneu Go..Makkama thi kaw..
Diam thila lép khathie yama geuneu know..
Jobal bagna low.. bayil khathie yii mbow..
Koudoul iow rk rk manoula def kiinga beugeu done..
Oow oww njingui geuneuh mbow
Beg lepp thiool
Mais nelene samay deal mingui beautiful
Free geuneuh Go Beureung beurigo
Kudul God duma teiyeii naleine ba niou thiow
Fii lepp diam , boy ioe lekko naano tegg lé tank doula déf legend
Fii lepp diam , lii dou hardcore mem soula tangor xanié diam ngay kaas
Beugo diam ngay raak , waa koula toogn ?!
Boudoul sa bopp kén doula nokk, au minimum war nga xamni yaa ress sa bopp baaye faal
Yagg ngama digg mbeuguél balégui mangui fi di diouri doome
Mangui diamou Yalla meunoul yam ci diouli dong
Dama dém ba wéddi sama bopp gayi waxi noppi
Wara wouti xaliiss bou beurri Keur ak buggati
Loumou ladj dinako déf déédéte douma tiite
Koumou tiime koudoul Yalla sounou Borom
Athia dougeul fii
Nieupeu guéneu ndax tay Diamma ame
Kogn béé beuri wone xééx nioom niou touxou Diamageune