
Paradise Lyrics
- Genre:Mbalax
- Year of Release:2015
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
Paradise - Wally B. Seck
...
Mangui fatélikou balay dora guisse silay wakh nane gnane gui nangou na beureupe bima doone génteu fofou rk laay khél di guisse lima beuguone gnou ande fah
Beureupe bou beute meusse teu khôle
Fénéne fou nitte démoul woone
Banékh bou reuye la yéme thi di khôl
Beusseu ngui nieuw mak yw lay doone
Laire gui nioungui ni nioune niaar sunu niaane ande na
Yalla mingui ak nioune
My bby …oubil sa beute khôl
Beusse bignou doone khar yék sina
Oubil say beute…
Souf séddé mir yi naw maak yw dou wakhi néne