- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2023
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
SOPÉ - Viviane Chidid
...
sopé kaay nga djégué ma sama xole yaw rek la damala beug xawma lan la té lolou nak déumb leu sama lettre binde nako ba postél lako nga diote ko sama album lou ko fésal say note daal mane beug na leu
Amoul piss ma beug na leu(2)
Sopé mane sopati na leu(2) oooh dissona ñiou déug na leu(2)
Amoul loumay téré ma beug leu tek maci vélo bi beug na leu .......
guissou ma dara keulé rek
beugou ma dara keulé rek sama xol kan mokoy doundeul keulé leu
wouy damala beug wakh ni nguir na dimba lima kay djéguéma ma néxal la diokh ko jamant nguir nga contane
Sopé djéguéma tam tamalma eh dama nguiro thi dig lal bi ay thia kay yeukeu tima
Amoul piss ma beug na leu(2)
Sopé mane sopati na leu (2) ooh dissouna ñiou deug na leu amoul loumay téré ma beug leu tek maci vélo beug na leu
see lyrics >>Similar Songs
More from Viviane Chidid
Listen to Viviane Chidid SOPÉ MP3 song. SOPÉ song from album SOPÉ is released in 2023. The duration of song is 00:03:02. The song is sung by Viviane Chidid.
Related Tags: SOPÉ, SOPÉ song, SOPÉ MP3 song, SOPÉ MP3, download SOPÉ song, SOPÉ song, SOPÉ SOPÉ song, SOPÉ song by Viviane Chidid, SOPÉ song download, download SOPÉ MP3 song
Comments (2)
New Comments(2)
khadidiatou souarehhrax
Maya Diedhiou6rvae
nékh nékh
cool[0x1f618]