
Borom keur ft. Fatim Diabaté
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2022
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Borom keur ft. Fatim Diabaté - Wally B. Seck
...
borom keur wate na ni yaw yadi kendou mbar bouldi kawa seguém boram keur yay dad dji ndiabote rek ko ko waraaaaal ligueye Guam ligueye yo dépense bii doula wathi dou mbeur bou niakk diom sa bo kheuyé ngébou jakarlo yaw té j'ai d'où té sakh nga nieuwate soubaaaaaa lolou niawna ehhhhhh yeeeeeee borom keur deukk bou tarr déko youbal Di woute lo yobou keur boul Di guawa seukéme borom keur yay dadi ndiabote rek ko ko waraaaaal bala gua kham li sa baye dane dathi diar guassi diambar la ! gua magg khammé ndiabote guii weurla ki diar guassi diambar la ! bala guaaaaa kham ni sa baye sonnnné Dia guassi diambar la ! Agne béeeeee néki mabbeu si sa kaw ! ki diar guassi diambar la ! boul guawa sekémeeeeee ! yalla bo guawa seukéme borom keur ééeehhhhh éhhhhhh boul guawa sekémeeeeeuh mom rek la War ééeehhhhh éhhhhhh borom keur na moytou thiowal goudii guala way boulko indile Ay wakh you sew sew sex dokhal boul guérssooooo fo meuna tollo doylole lawouuuuu néké deubeul deubeul , keur keurii, dangu danguiii waw dou wathii borom keur taba tabaaaaa ak keufeur keufeurrr néké dou wathii borom keur taba tabaaaaa ak keufeur keufeurrr néké dou wathii borom keur soko gueuméeeee ssoko wolooooohooo lawou limou yorr dakoy diayye sooooo dangue danguéeee dadjé nawaw borom keeeeeeur siguil boul seukéme nénala masta hé masta thionoo hé siguil boul seukéme ahhhhhh masta thionoooo hoo Fatim Diabaté hindi thiéeee Wally dieureutiéuuf diom gallé diom gallé a jaramaaaaa ahhh diom gallé wanata thianam taba tabaaaaa ak keufeur keufeurrr néké dou wathii borom keur. fin ...
Similar Songs
Listen to Wally B. Seck Borom keur ft. Fatim Diabaté MP3 song. Borom keur ft. Fatim Diabaté song from album Etat d'esprit is released in 2022. The duration of song is 00:04:35. The song is sung by Wally B. Seck.
Related Tags: Borom keur ft. Fatim Diabaté, Borom keur ft. Fatim Diabaté song, Borom keur ft. Fatim Diabaté MP3 song, Borom keur ft. Fatim Diabaté MP3, download Borom keur ft. Fatim Diabaté song, Borom keur ft. Fatim Diabaté song, Etat d'esprit Borom keur ft. Fatim Diabaté song, Borom keur ft. Fatim Diabaté song by Wally B. Seck, Borom keur ft. Fatim Diabaté song download, download Borom keur ft. Fatim Diabaté MP3 song
Comments (8)
New Comments(8)
Yoro Sougou
Petit Mbayeig747
OK
iso créations
Am na theme song bi diar na yone pari le yi raye nama boul di gawa sanguém ❤️ fils de thione seck waye bou diguelé woul ay nakhaté la❤️
Fall papag1q9h
[0x1f618][0x1f618][0x1f618]
Ismail fleee
waw inchallah diam rek si wally bilaye bakh moy lep [0x1f628][0x1f628]
Moussa p1wj2
Vraiment ça c’est du lourd
Ndiaga Diop ixo29
Disc d‘or rekk inchallah❤️
BCD-
non wally du nituu[0x1f642][0x1f642][0x1f642]
Salut