
Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2022
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé - Wally B. Seck
...
Oh am sorry hooo am sorry hi hi ma khame dou sama thiobaré nakh li meune na dall nitt kou nék hey ki dou moy baba mohh ki dafa dof legui cone bakhna. Hooo am sorry wakh djii diaroul mouy sorii nakhté li koumou né si nioune meune na done sa storie hooo heyy khana khamoulo ni meune na né sa storie nala kénéne koudoul iow djiégué hoo ame sorry hoo ame sorry li boko doundoulé déti thiey walla gua mandou thie.Baniou néké gouneuy Bâle gui nioy andeu deme naniou ba nieup diniou wowé Roméo ana Juliette souniou mbeuguel nieup ko sédé tay djii gua déme bayima ma nékake kénéne néguéne dama dof té qui rékama meune fadje bama wér ping soula nékhé yobouma si médecin boula nekh sama dianguoro di mbegueul. Mia : khame nako wa mbeuguel loutakh mouni mel nit kou nék sa khol dou yombou gua guéné si sa khél diguanté copain ak copine meunossi nopi loussi meunti metii nama dall ahh ahhh hannn hooo niou kheuy mayma kénéne ma déme seuyi lernama beuguoulo kénéne koudoul mane mii nigua moudjié nekhouma wayé dou sama thiobaré damala love dama dof si iow hôpital fadjiouma yaye sama thiobaré damala love dama dof si iow serigne fadjiouma dou sama thiobaré.( Referai). Kholale nima mel tay kéneu khamatoul loumay nirole toup nako nakh mbeuguel sank nama magui weur di takhawalou kéneu khamoul limay nouroul maguini tay dofna defna tanki nén deuké weur di takhawalou keneu khamoul loumay nourol dou sama thiobaré damala love dama dof si iow hôpital fadjiouma yaye sama thiobaré( refrain )lo beugue beugue nako defma boy ma foteul la bo sokhlawé ko yonni yonnima defma boy ma togual la bo sourré boula nekhé désalma. Wally ballago sek ____ Nd
Similar Songs
Listen to Wally B. Seck Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé MP3 song. Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song from album Etat d'esprit is released in 2022. The duration of song is 00:03:29. The song is sung by Wally B. Seck.
Related Tags: Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé, Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song, Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé MP3 song, Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé MP3, download Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song, Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song, Etat d'esprit Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song, Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song by Wally B. Seck, Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé song download, download Dama dof ci yaw ft. Mia Guissé MP3 song
Comments (46)
Top Comments (4)
Moussa hh8g8
❤️❤️❤️❤️>
kiné dia811zd
machala [0x1f602][0x1f602]>
New Comments(46)
Astou Faye6zieq
trop nekh[0x1f618]
lamine5bbe0
wye bi nekhn trop wl est le meilleur vrment[0x1f618][0x1f618][0x1f618][0x1f618][0x1f618][0x1f618][0x1f609][0x1f609][0x1f607][0x1f607][0x1f638][0x1f612][0x1f612][0x1f612][0x1f608][0x1f608][0x1f617][0x1f617][0x1f621][0x1f621][0x1f60b][0x1f630][0x1f630][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f627][0x1f627][0x1f627][0x1f603][0x1f603][0x1f63b][0x1f63b][0x1f63b][0x1f63f][0x1f63f][0x1f63e][0x1f63e][0x1f63e][0x26a1][0x26a1][0x26a1]
Karamba Bayo
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f627][0x1f627][0x1f627][0x1f627][0x1f627]
163620715

Adama Khady gueye
❤️❤️❤️
Auguste Ignace Mangahs8j2
ton dernier album m'affecte vraiment. Té dama guiss né kou déglou son yi ware nga ci guiss sa boppou. cé ce ki mé arrivé. Diarama diambar Wally. Et j'en suis sùr ke le prochain album tu vas encore frapper foooort ndah doo ki tapalé. Le temps passe et tu es et tu seras tjrs le meilleurs. Bravo aussi au groupe "Rane Daane" Puissannnce
iboudqrk5
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623]
707473138
[0x1f612][0x1f613][0x1f617][0x1f603][0x1f608]
Coumba Baaqtn0

Coumba Baaqtn0
♥️♥️♥️
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️>