
Yenë Saay
- Genre:Mbalax
- Year of Release:2020
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Yenë Saay - Viviane Chidid
...
Gneweul ma wakhla noy doundéko wa dji damané Gneweul Ma Wakhla foy diarr Aladji Gneweul Gneweul ma wakhla noy déf ko wadji dieu keur dagnko doundeul wagni thowli wanko Linga ko naral tasaréko thi lalam dinala dingat auto keur ngou béss wourouss ak ngalam yétalko bathi kanam yéw ko thi kaw lalam djiguéne dangay djongé mokk podje té djongama déhk louma yéhne saay yéhne saay défal yeufou bandit tassarél assanal dieul leull tidji keur Gui tass yéhne saay yéhne saay défal yeufou bandit tassarél assanal dieul leull tidji keur Gui tass solal ko mbakhana kasé sa dieu keur lépp si dangan talal lanpe yi youbou thioura yi dougal téksi bandjimi lou yeungou réyal sa assana bi khékh khakoy tass paka bou gnaw diarul ngay dass dieu keur dagnko topato diko nabe nabé seuy dangay kham ndieugeum yaw deukel di dieufé louy nékh Aladji Aladji seuyeul nékhalko si birr néhg bi ak waagn bi Yaw deukel di dieufé louy nékh Aladji seuyeul nékhalko si birr néhg bi ak waagn bi wanko Linga naral tasaréko thi lalam dinala dingat auto keur ngou béss wourouss ak ngalam yétal bathi kanam yéw ko thi kaw lalam djiguén dangay djongé mokk podje té djongama déhk louma yéhne saay yéhne saay yéhne saay défal yeufou bandit tassarél assanal dieul leull tidji keur Gui tass yéhne saay yéhne saay yéhne saay défal yeufou bandit tassarél assanal dieul leull tidji keur Gui tass aliss loutakh nga né djinakh day beuri pakh maricha loutakh nga né djinakh day beuri pakh comci Comcast c'est ça c'est çi chouchou tonton ah eh
Similar Songs
More from Viviane Chidid
Listen to Viviane Chidid Yenë Saay MP3 song. Yenë Saay song from album Benen Level is released in 2020. The duration of song is 00:03:44. The song is sung by Viviane Chidid.
Related Tags: Yenë Saay, Yenë Saay song, Yenë Saay MP3 song, Yenë Saay MP3, download Yenë Saay song, Yenë Saay song, Benen Level Yenë Saay song, Yenë Saay song by Viviane Chidid, Yenë Saay song download, download Yenë Saay MP3 song
Comments (29)
New Comments(29)
Mamadou Anneywv9h
Khady Dioufkcdgu
❤️❤️
bn200945
[0x1f630][0x1f630][0x1f630][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f619][0x1f606][0x1f606]
Ngoné Dioneic3jb

Sohna fall
Fall

KHALILh7r3f
ya dégu déh vivi[0x1f618][0x1f618]
Mame Thiamd0pp8
[0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641][0x1f641]
128219596
Awa
132327330
je adore
128098973
bébé. awa. conaté. ❤️❤️♥️

103019530
comment faire
[0x1f629][0x1f629][0x1f641][0x1f641]