![Goor](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/05/26/0404bb4a29664be8a0bbbb37ca08c087.jpg)
Goor Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
Lyrics
Goor - Ashs The Best
...
(Jëf jël ñakk jariñu )×3
(Goor faaloo mbaa fattewoo lutax mudaan fanaane root aka sikar lahilaaha illalaaahi faal meïssa biigé kumba faal) ×2
Mbaa fattewooo ?
mbaa fattewooo?
mbaa fattewooooo?
mbaa fattewulooo ? (mbaa fattewoo)
Borom Ndiguel ni sëgben
Borom Sigibek Sëgbi
Borom Ndiguel ni nangu nañ(Maam Cheikhb'ra faaloo)
Borom Sigibek Sëgbi (Sëgbee)
Borom Ndiguel ni nangu nañ (jëf jël)
Mbaa fattewoo lutax mudaan fanaane root aka sikar lahilaaha illalaahi faal meïssa biigé kumba faal?
Goor faaloo
Mbaa fattewoo lutax mudaan fanaane root aka sikar lahilaaha illalaahi faal meïssa biigé kumba faal?