![Ñibisil](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/05/26/0404bb4a29664be8a0bbbb37ca08c087.jpg)
Ñibisil Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
Lyrics
Ñibisil - Ashs The Best
...
Ohooo hoo hoo hoohoo hoohoo
Gnibissil gnibissil hii hii
Dioubb dou wess
Dioum dou wess
Soumalay wo loutakh doma falé
wakhma lou dégne ci mane khana beugueu toma
Beutou mbeuguel lala meusseu kholé
lou waral mane ak iao niou deukk ci thiow
uhm uhm uhm
souma kholé founiou diarr yeupp
dangma wone dima tegg fou sori
beu niiouy ngoro lo kham wakhma
tay biti bi molay gueureum
keurgui dioy triste
samba alar waroul ci ndiabott dji
khalé yangui dioy
khalé yangui dioy