![Yeurmande](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/03/11/8a63d364c5d44c47841a322d61eecaba.jpg)
Yeurmande Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
Lyrics
Yeurmande - Ashs The Best
...
Humm humm
Dioy na diexal ba rangoñe
Diay na la sama bakane
Fiip na fiip xexe nguir sama askan
Xeex nguirr sama askane
Dioy na ndax new di dolé yagui yalwane
Xiif ak maar djamono dji
Neew di dolé dioy
Dieul ngua souñou pess
And love
Ngour def ñou ennemi
Deuki si di noote
Dieuli dji liñou mome
Dioxna
Sene dom souñou dom
Kousi
geun souñou koom Seniy poche
dafay doye dieuli wouñou Yonou gueth fi lay ñi togue dematou touñou bitim reew
Dioy samay deukendo
Yeurmande si diamou yalla yi
Yeurmande