![Xaalis](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/08/25/3a6170f1603449e7a5d3486c56e5a5d1.jpg)
Xaalis Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2020
Lyrics
Xaalis - Ashs The Best
...
Yeaaaaaah
Haaan yeaaaah
Xaaliss lañu gënë fonk nit walay (jamonoo jamonoo jamonoooo)
Nita mën am xaaliss mais yaw xaalissa
ñuy am (jamonooo)
Lu waral ñi di jaay sen leer jëndeko lëndëm (hummm)
Alalou Aduna la lepp fii ngakoy bayi (héhéhéhé)
Xaaliss lañu gënë fonk nit walay (Xaaliss lañu gënë fonk nit walay)
Nita mën am xaaliss mais ñun xaalissa
ñuy am (ha ha haa han yeah)
Lu waral ñi di jaay sen leer jëndeko lëndëm (hannnnn)
Alalou Aduna la lepp fii ngakoy bayi (héhéhéhé)
Xaalis lañ lay xame
Xaalis lañ lay lacce
Soo amul xaalis duñla xame
Duñla woolu duñla lacce
Ndax Ñeppa bëggë melni moom
Xaalis tekla gacce
Coonoy xaalis molay wacce
Moolay galankoor dugal la ci jaabante
Xaaliss lañu gënë fonk nit walay (haann yeaaah)
Nita mën am xaaliss mais ñun xaalissa
ñuy am (ha ha haa han yeah)
Lu waral ñi di jaay sen leer jëndeko lëndëm (héhéhéhé)
Alalou Aduna la lepp fii ngakoy bayi (héhéhéhé)
Xaaliss lañu gënë fonk nit walay (Xaaliss lañu gënë fonk nit walaaay )
Nita mën am xaaliss mais ñun xaalissa
ñuy am (alalou alalou alalou alalou alalou)
Lu waral ñi di jaay sen leer jëndeko lëndëm (héhéhéhé)
Alalou Aduna la lepp fii ngakoy bayi (héhéhéhé)