
Souffrance ak Mettit Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2021
Lyrics
Souffrance ak Mettit - Iss 814
...
Ay traçou violence ci sa yaram
dëmal wootë d'urgence kepp ko xam
xaritt complice parents complices
paregoul sax ci say sévices
xaliss dou sëy bonheur dou luxe
boko guissé xool bi dey big
te ki nga key trompel xamo ko sax
ki nga jappë xaritt moko koy wax
rethiou dey wess temps bi dey dem
neggu sëy bou beuri problèmes
bo xamonn lii la do thi duggu
Ya ngi lathie houdba kouko tuddu
mère bi dey dem mom dou fautive
Waa dji daga key coller motif
xaliss bii nieuw rek ngey guiss
xaliss bii nieuw rek ley guiss
Yagui fey thi gejju iblis
xamato foy tekk sa tank
dem nga ba wett toog di triste
Mbeugël bi tey dalay sank
refrain
Yeurmande menoul ame fi ak jappé wuu nu jiggen gni ni nu jappé sounou bopp yi
aaanh anh anh
souffrance ak mettit you ken doul xam parce que deukou niok yaw
wax nako mère bi mais beugoula xam parce que xaliss dey nieuw
couplet
amoul ben temps.....
Saa bo yéwo beug daw nga xalaat fils
lila dougal ci sëy bi guéné wou la ci
gnila dougel ci sëy bi toppou niu la ci
ki tak waa dji nekoul mom mo takk sëy bi
guénél la sarax pour mene doxxal sëy mbir
waxon nala que dinala wax lepp Li ci biir
yagui si biir sëy bi
Souffrance Yeah Yeah
Souffrance Yeah Yeah
Yagui ci biir sëy bi
couplet
Amoon nga chance bagn ko deff
Mais nak moudj nga ko deff reuthiou dey fekk mou wess
amoul ki amoul ké
parce-que ioe rek sa Jeux
legui ioe rekka ci dess
refrain
Yeurmande menoul ame fi ak jappé wuu nu jiggen gni ni nu jappé sounou bopp yi
aaanh anh anh
souffrance ak mettit you ken doul xam parce que deukou niok yaw
wax nako mère bi mais beugoula xam parce que xaliss dey nieuw
couplet
dooré tout le temps
sagga tout le temps
bo waxé fout le camp
keur gui boucan(bis)
Ay violence ci jigeen meunonn na bania ame
Yeurmande ci jigeen lolou la goor wara ame