![SOMA BËGGÉ](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/31/f081083c7ce24ad283881d1b54bb4e08_464_464.jpg)
SOMA BËGGÉ Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2023
Lyrics
SOMA BËGGÉ - Iss 814
...
Boma beugë
Daga may defal cadeau
Dima nakhé
Yeungeul thiabi auto
Mon bébé
Dougal ma thi château
Ma dieul fa samay foto
Wone len ni namou ma thiothio
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal
niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal, Niewal, Niewal
Toukousou ngalam
Musik bi di daw
Nieup di danse
Ma def la madame
Yeukeuti basi kaw
Nieupa la fans
Bo naré basang
Hotel lagnou dieum
Diap fa temps
mané
Bou répé déh
Bou répoul déh
Tay la beuseum
Adioul basi kaw
Diap sa ndiakh
Nitt yi la beugoul
Thi souff laniou nekk tok dila xarr
Rez-de-chaussée
Rez-de-chaussée yaw do diégou rez-de-chaussée
(Éeeeeeh rez-de-chaussée)
Am ga thiatt am ga feeling
(Eeh)
Fesss ga del mel ni meeting
(Mais yako mel nonou)
Degg dadj tek si clean
Fouma tournée ga topou ma melni sikim
Yay birou khar thi deukhine
(Mbéeeeeee)
Boma beugë
Daga mey defal cadeau
Dima nakhé
Yeungeul thiabi auto
Mon bébé
Dougal ma thi château
Ma dieul fa samay foto
Wone len namou ma thiothio
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal, niewal, niewal
Xalé bilé namoul peureum
Waxaléwoul or
Diamant fess na dell keureum
(Namoul namoul touss)
Degg dadj tak seureum
(woo)
Goor douko yap
Mako beug mako geureum
Hé mako geureum Thié thié
Bayi len si birrr
Thiow li di rirrre
Thiaw ga sa xirrr
Nok len baniou mirrr
Diégu bi dou lirrrr
Faux bi dou pire
Nop la ba mirrr
Legui sax dama fire
Ohh putain
Mon bébé
Bo bougué niouy joué
Daga mey diégué
Heee
sucre, vanille, pomme,
Ya yore sama banane
Boma beugë
Daga mey defal cadeau
Dima nakhé
Yeungeul thiabi auto
Mon bébé
Dougal ma thi château
Ma dieul fa samay foto
Wone len namou ma thiothio
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethieu ak mane
Niewal
Niewal niou fethieu
Kay fethi ak mane
Niewal
Niewal
Niewal