
PARADISE Lyrics
- Genre:Soul
- Year of Release:2024
Lyrics
PARADISE - Iss 814
...
I love you I love you I love you
Ben nite mo yakone sa xol bi
Dieki am kou nieuw
Defarate leu beugeu nekate nite
Diokhla mbeuguel bi ga yelole wooo wooo wooo wooo wooo
bae
mak yaw
bouniou xole xamni niougui doundou paradise
bae
mak yaw
sunu mbeuguel nimou mell di naniou ko doundou ba paradise
damalay topou dila weur foumala guiss continuer dila topou melni ioe rk yafi nee
Yobou ko equipe capitaine bi nember 10
takal la brassa bi bly wly yafi nee
Bepe xew bo beugoul lay tass
baby niga mel I love you ioe laye tane
fepe fo rombe say copine bayi thiass
com kou signer dem si vie pare dilen diaye thiass
bae
mak yaw
bouniou xole xamni niougui doundou paradise
bae
mak yaw
sunu mbeuguel nimou mell di naniou ko doundou ba paradise