
Akbess
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2020
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Akbess - Akbess
...
guiss deugg ba deugg si sa tank lingaye woté modoul deugg si yaw nitta leundeum deff si nank nank dossi sorri Bo khamone djikom
yallaye dogal nitte tela dila diougal moulaye mousseul nioulaye yèné mbougal tek la natou pour natte la mounieul mounieul yègo yallaye dogal
héé (x2)
yaye boy loutakh défoo ma comme sa dôme dinga dé kénène domowou sa dôme sama dèmb yallah KO Def si mane
yaye ak baye lamoudiou bayi guinaw mangui téw mais douma dèlou guinaw
worna yallah nafi nek bidew nafi dane mbarane arbitre si bir guèw mafi meune si bara si mim rèw finguéne teude yallah naléne gueuneul dilène sani ay niane lalène meuneul fékè wolène si dara ma gueuneul bakar yé moudié beurri ma gueuleum
prési bayil **** Di dadialé loutakh sa dom amadou dou paqueté nioune nioye sonou si diel yek si hôpitaux dénk léne n**** milliard yi nguéne profitossi motakh boyi tek bandit tek layfou Toni dialalé kilos yi tèguè né diplôme yi moning moning maire bi dou teudé ni doumako deff douma voté pour yène sa wakhou taye outé sa wakhou Dèmb niou nek si urgence yi diobougne **** ay doumou galsen Di dé sibir diel état bi sathie na dou moudiou féne limoye DEUG boudoul meusseu fègne fégne na sakh dagne KO banalisé wakh KO mou diékh wakh dji dou meuneu nékh ay grand di marche pour ay visa ki chèque
comédie pd yi mo wara dièkh yaw deugou wo beuggueu dioubal koudoul yor loumouy diokhé deuggueu wor danga meunoul boy
guiss DEUG ba DEUG si sa tank lingaye woté modoul deugg si yaw nitta leundeum deff si nank nank dossi sorri Bo khamone djikom yallaye dogal nit téla dila diougal moulaye mousseul nioulaye yéna mbougueul tek la natou pour natte la mounieul mounieul yégo yallaye dogal
hèè (x2)........
Similar Songs
More from Akbess
Listen to Akbess Akbess MP3 song. Akbess song from album Xar Kanam is released in 2020. The duration of song is 00:02:42. The song is sung by Akbess.
Related Tags: Akbess, Akbess song, Akbess MP3 song, Akbess MP3, download Akbess song, Akbess song, Xar Kanam Akbess song, Akbess song by Akbess, Akbess song download, download Akbess MP3 song
Comments (12)
New Comments(12)
bamba3qxdj
abdoulaye gayed995p

Malick bacrtvj

Babacar Diopczego
coull na
Barry b05cs
dop[0x1f631][0x1f631]
113086622
cool bro
Bamba Cisser5sv
Nice
alia9oep
boy project bi nice na trop ms danko yakamti warone guako geuneu togou respect
Ndiaga Ndiayeactip
akawér
prince boomker
dope[0x1f63f]
ndiogoua82ga
deug deug
un excellent tube nickel [0x1f606][0x1f606][0x1f606]