![AND AK YOW](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/09/04/26da45036a9a4f4da32824c1a42575d5H3000W3000_464_464.jpg)
AND AK YOW Lyrics
- Genre:Soul
- Year of Release:2024
Lyrics
AND AK YOW - Iss 814
...
Nite kou neh Sisa life Amna koy Khar
Tè bou yeksè dingua khamni kile wone
Fingua dème fima diarre fingua togue khar
Bou yalla neh Waw dafay melni sonno wone
Yague nagne dieul sa khol fowèko
Khamoul wone lithië bur lithië newone
Sa yeug yeugou khôl nekh ba deff lay dioy
Niane bou sotti sonale Borom
Andake iioe fo aye neeeh meussoul degne
Nekak iioe fo aye neeeh meussoul nekh