
Bideew Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2021
Lyrics
Bideew - Obree Daman
...
Ah ha ah ah ah ha ah aye
Yaw mi sa mbeuguel lay leral sama yoon (2)
Aksil niou andandoo
Andandoo ci assamaan
Sa mbeuguel ni bidew
Bidew bi leral sama yoon
Djiguen nay indi ler
Leray ci aduna
Sa mbeuguel ni bidew
Bi leral sama yoon
Yaw mi sa mbeuguel lay leral sama yoon (2)
Djiguen nay leral
Melni lerayu assamaan
Sen mbeuguel lay leral
Djiguen nay leral
ni lerayu assamaan
Sa mbeuguel lay leral sama yoon