![Me You and God ft. Jeuuss Beatz](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/06/13/c76a04abeb124dd099206d6573f9dfd7_464_464.jpg)
Me You and God ft. Jeuuss Beatz Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2024
Lyrics
Me You and God ft. Jeuuss Beatz - Obree Daman
...
mbeugel la né ci sama khol wah yé adouna niou sonal lol khol bou fessak banekh la la yéne won ci adouna mbeugel Gui ma am ci yaw mba dou messeu beurri loll Diafediafe adouna ak mbok gui niou yalla bourbi bole kon mbeugel moy adouna ndakh yallah mo niou bole sama yéné yatouna mangui gnan yallah may niou dole dougouna ci gallou mbeugel ndokh bi yobouma hummm ngelaw langui may indi ci yaw niou Guissé lernama mbeugel moy Li lerral adouna kham nga yaw la beugeu lol sama yéné yatouna mangui gnan mou yok
denkeuna le yalla, denkeuna le sama khol sa souma dioulé dila nianal sama khol lako tiibé denkeuna le yalla DENKEUNA le sama khol sa souma dioulé dila nianal sama khol lako tiibé kon mbeugel lay adouna ndakh yallah mo niou bole sama yéné yatouna mangui gnan may niou Dole
dougouna ci gallou mbeugel ndokh bi yobouma Hummm ngelaw langui may indi ci yaw niou Guissé lernama mbeugel moy Li lerral adouna kham nga yaw la beugeu lol sama yéné yatouna mangui gnan MoU yok.