![Banneex](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/01/26/9ac2ac2d42e348a8906afd00efb31cad_464_464.jpg)
Banneex Lyrics
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2022
Lyrics
Banneex - Obree Daman
...
koula faléwoul mane mi malay falé done sa séttou koula khole mane lay guissalé ×2
thi sa beutt lay khol none I love you baby yaw yay sama life ×2
baby yaw yay sama life
souma yalla beugué wakh léne ko nama bayi ak yaw
ndakh kou melni yaw amatoul thi aduna
sama khol lale deff beugue deugue lale deff té douma soralé béne none ndakh yaw yay sama life
thi sa beutt lay khol none I love you baby yaw yay sama life baby yaw yay sama life
koula faléwoul mane mi malay falé done sa séttou koula khole mane lay guissalé ×2
thi sa beutt lay khol none I love you baby yaw yay sama life ×2