
Feccal Ma Lyrics
- Genre:Mbalax
- Year of Release:2020
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Feccal Ma - Wally B. Seck
...
Siw du jaamm
Ngewel waxi nopi
Siw du jàmm jam
ngewel waxi nopi
Maro mar lougniy cow
Wayé Yalla may nama nit gné kay
Man xam na man xam naa
Dina xewi jéé
Su boba ñu naaa
Amon nafiy temps
Mangui ni ci sama war
Di nisal ngui netali na eleuk
Ma way li
Nga fecc li
Gnu and begé
(Yaw mi may begé diogal yeungou)
Ma way li
Nga fecc li
Gnu and begé
(Yaw mi may begé diogal yeungou)
Chaba tibi dabib daram
Chaba dibi ndeee wah hooo
Chaba tibi dabib daram
Chaba dibi ndeee oh hooo
Ma wayal gañi waw
Annnh ci ngewel
Ma fénte way wi
Diag lel lenko diag lel lenko
Ma way li
Nga fecc li
Gnu and begé
(Yaw mi may begé diogal yeungou)
Ma way li
Nga fecc li
Gnu and begé
(Yaw mi may begé diogal yeungou)
Music.......
Ma way li
Nga fecc li
Gnu and begé
(Yaw mi may begé diogal yeungou)
Ma way li
Nga fecc li
Gnu and begé
(Yaw mi may begé diogal yeungou)
Teubeul
Teubeul way
Feccal ma
Teubeul way
( yaw mimay begé diogal yeugoo)
Teubeul
Teubeul way
Feccal ma
Teubeul way
( yaw mimay begé diogal yeugoo)