
Skit Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Mame nena kou beg koom, na nga doylou
Ndakh moy magasin bi doul diekh mouk
Wolof da koy faral di lepp
Kou kheboul sa noce ken dakhoula noce
Yaw mi nga khamni Yalla diouni lala wersegelé par bess
Boul diel sa bet bi mouk tek ko si ki yalla wersegele million par bess
Amana yako guene demine
Yonente bi Salalahou haleyhi wa salam
Yalla bim koy tagg si alkhourane
Si souratoul Doha dafa neko
Wa Wajadaka `Ā'ilāan Fa'aghná
Fek nala yoro dara amo dara
Waye ma diokh lou guen am am
Diokh la lou guene yor
Te moy doylou