Nitu Thies Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2023
Lyrics
Nitu Thies mo dangereux
Thies dafa danse te rebb
Nitu Thies dangereux
Thies dafa danse te rebb
Nitu Thies dangereux
Douma dof ndeye mais dama dof ndeyam
Foma sen sa droite dielel sa gauche dem
Boudé si rap game doumassi dokhandem
Dokhan dem diwaan bafa ay mburok lem
Intellec ba nopi tarkkinda
Sef sa life lou guene tar Sida
Gagne la fadj lo indi gnou bagne ni ibadok ay biida
Changer flow chak 4 bars
Beat boma tek ma dem kakatar
Raba yomb ni passou jakarta
Rappeurs yi sof ni thiouthiou si thiaga bar
Noto merder
Dokh sunuy waaw ni kou yor sa sextape
Kone nek mess dem
Mene rap tigui fils no kone respect
No contester
Positive laay guen saaa yooko tester
You look down on me but you're clown to me
Laalak skillz fi ba souba douma daanou fils
Nangoul ni Gnoune la yalla taamou fils
Kou kholam bone non da ngay moudiou gaagnou fils
Thies dafa danse te rebb
Nitu Thies dangereux
Thies dafa danse te rebb
Nitu Thies dangereux
Kougn ni yafine da dek nekoumafa
Game bou yaradal projet moy nefoumafa
Doug yoff ndawrabine fa guenaat
Diar GY diel trone bi dem PA
Paradi Rio parédi gnibi paradis
Diarefa bayi fils mana boy melakh
Chocolat yamoul ak mboussou degué
Soul 22 titres ak 5 couchous bébés
Dinthiouna hate kaay toubal sorry
Boy get sama son boula google sorri
Fessal salle yi mode anonyme
Rap lyrics ak harmonie
Panne inspi def armomine
Kougn al money pour faay di nga faay po mi
Eh nagn todj son yisi album yi
From almadies 2
Samp ndend dig almadies
Ki beg yengel sa ma monima alma dick
Bo guissé sunu binde di nga dam sa bic
Serial killer nigga I'm sadick
Ndeye seck kaay signel ma fi