Yëg Yëg Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Youssou mi Why Gee
Ndekete day rap mane de baay bi
War rek lako xame mani kaay fi
Jox ma saay nope
Get samay dope
Dama ndiru ku si sope
Non yaw mi le
Waxal ba do jomi rek
Si domu Thies biy door bitch ass yi
Do Mi Re la nar ba tok fi dominer
Ci world bi yëp ni Hov and B
Li nga tama guiss moy rappeur bou rew
Bou de cool di ngama sepi ni lou gnoul si mew
Ma ngi soga tew talouma wakh dju sew
Deke job bamou soti wo sa none mu djew
Non time to waste Amoul bayi nek si
Ba ñok sunu folie bo ñu menul fek si
Utuñ buzz boy take a seat sunu leuz moy tekki si
Lu waay mene def li gna beg moy lekk si
Xolal li te nga bayi xel Why Gee dafa dem
Toggal fi te nga bayi hate job bi da faay demb
Xolal li te nga bayi xel Why Gee dafa dem
Toggal fi te nga bayi hate job bi da faay demb
Wowowoooo
Hummmm Humhumhumhummm
Show biz dafa dirty massi dug lu taxx
Non pere sopiwouma ma ngi si tank yu baax still
Kuné li nga bëg moy teral sa parent
Te sen ñane guenel nama fuki butelu safara
No Djo rap kesse du luy duggalu safara
Djëf lu baax tok ni pat xaar yërmande yalla
Mene rap teksi clean du maak boy yiy saaga nak
Talk to my niggaz do messe deg ki nabala
Deep word nice flow doko deg te miro
Rap ba nirok kenene flow kone ma gedd tek micro
Jox ma 10000 Euro
Duma change numero
Du maax xetu kakatar yi kopar di sopi gigolo
If you wonder why I rhymes this is what I feel
Selling soul to the devil is not my deal
Def rap def straight na xel dalsimane
Kuma xam di nga dieli du maak talismane
Xolal li te nga bayi xel Why Gee dafa dem
Toggal fi te nga bayi hate job bi da faay demb
Xolal li te nga bayi xel Why Gee dafa dem
Toggal fi te nga bayi hate job bi da faay demb
Wowowoooo
Hummmm Humhumhumhummm
Hohohohoooohoo