Loading...

Download
  • Genre:Hip Hop & Rap
  • Year of Release:2022

Lyrics

Cle de sol biy tidji assamane

Rap la boy no tassoumane

Dioudou demb soru sa massu mame

Rindi djegui no rassoumane

Ñi may jaay liquide lay nane ni kassu chine

May wicked bi reral atoumane

Bul ma gondi ay dondj dara safuma

Li nga dream la dunde ba nopi xandiuma

Sono si mbinde mi yagg si mbund mi

Tagg sa bope rek ay scream ay ennemi

Non boul polemique noto politique

Buzz ngay dunde boy mexel punde mi

Oh no are you feeling me what I`m saying is

If you`re killing it you`re selling it

Oh no are you feeling me what I`m saying is

If you`re killing it you`re selling it

Ku nopi war muy dioxe leçon

Moy ki xey si rap te jayo sa son

Foy jaar ba xulok maçon

Duma fa xaar nga tonte sax de toute façon

Ku nopi war muy dioxe leçon

Moy ki xey si rap te jayo sa son

Foy jaar ba xulok maçon

Duma fa xaar nga tonte sax de toute façon

Deg si lamiñu gone no def mu douma magg

Biñ mané rap musicou xaley la la bañ ni douma magg

Duma xural baat te duma xura ndaax

Naturel muy neex ken duma utal mass

Xale may tek te makk duma daan

Teral mere miy buzz la nax duma daan


Partager len video yi Tassare len ideo yi

Ndiago si ragg duma diap di ba ni pa bi djite libero yi

221 numero bi djine Moussa nema do nit

Rappeur à mi-temps ma diaxasse game bi te delu si liy indi money

Sa cukel na mbalax ni beat bi

Nga deglu ma rimbal la riti

Cheikhou Assane la may Ousseynou Diouf yet ma xorom si ma jobi

Ba len ak wakh dji te tope sa yone ken dulani liggeyo fils

Dug si rap te xarouma cachet ndax miss na million

I do it for fun not for fame teyel sa opinion

Si lenen lima nek ludul si rap c'est pas tes oignons

Pour sama xar kanam nak xaral si kanam mais fils ma mignon wolah

Cacher sama visage ken atanul cachet bi tim la my boy

We`re twice as tall you can't level up team burna boy

Boy doug suñ 18 wowalel 18 mba fi burn ba boy

Rap dëgër terewuko nexx fi guene na nooy

Ñe ñe ñe ñe ñe ñe ñe ñe ñe rew na ba dof ohhh


On a Friday night while they're sitting watching jakarlo

I'll be spitting bars like Jack Harlow

+

      -   or   -

      -   or   -

      NG +234
          -You can log in via below methods-
          Reset password via e-mail
          -or-
          Reset password via e-mail
          If you have any questions, please feedback on Boomplay App or send an email to [email protected].

          Please Select A Playlist

          Add New Playlist

          Share on

          Embed: Love & Light EP

          Custom Size :

          • Default
          • Desktop(300*600)
          • Mobile(300*250)

          Type :

          • HTML/HTML5 (WordPress Supported)
          Get Boomplay Premium
          for
          Payment Method
          Pay With
            Review and pay
            Order Date
            Payment Method
            Due Today
            Flutterwave
              Subscription Successful

              Congratulations! You have successfully activated Boomplay 1 Month Premium.

              Now you have access to all the features of Boomplay App.
              Payment Failed

              Please check your balance and then try again.

              You'll lose your subscription if we don't have a working payment method for your account, so please check your payment details.
              Need help? Contact Boomplay Subscription Support.
              Payment Processing...
              10 s

              Payment is being processed by . Please wait while the order is being comfirmed.

              Payment Processing
              Your order is processing, and it may take up to a few days for the service provider to handle your payment. Please kindly stay tuned and check your order status in ‘User Center’.
              About Order Status