
Sante Yallah
- Genre:Afrobeats
- Year of Release:2019
This song is not currently available in your region.
Try the alternative versions below.
Alternative versions:
Lyrics
Sante Yallah - Baye Mass
...
defguama gorou yallah soutoureu yee domou yayam soldarou bamba lima diokhonieu yaw gua diokh ma mashallah santeu nala diokh ma ndeye diou Matt ndeye baye Bou Matt baye man deh geureum nala baye fall ddou niakeu loumou beugeu am KO nakh thiofelam thi bamba alhamdoulillah sante na yallah sante na bamba sante na yallah sante na bamba oubil nama oubekou bi bi samay bountou daff ma may soldarou bamba sante na gnima diappaleh bamah wessou Lou mettih sante na yallah sante na bamba sante na yallah sante na bamba goor lay done gore yallah dafay deugou kou bakh lay done foula AK diom fek ndigeul mbottou yallah bi mom lay yorr sante yallah bim ma deffeh lima doneu sante yallah bim ma deffeh domou niari goor sante yallah bam ma mousseuleh si none yi sante yallah bim ma niteuleh sama yoneu sante n'a yallah santé na bamba sante na yallah sante na bamba santeu naa
Similar Songs
More from Baye Mass
Listen to Baye Mass Sante Yallah MP3 song. Sante Yallah song from album Sante Yallah is released in 2019. The duration of song is 00:02:44. The song is sung by Baye Mass.
Related Tags: Sante Yallah, Sante Yallah song, Sante Yallah MP3 song, Sante Yallah MP3, download Sante Yallah song, Sante Yallah song, Sante Yallah Sante Yallah song, Sante Yallah song by Baye Mass, Sante Yallah song download, download Sante Yallah MP3 song
Comments (24)
Top Comments (1)
Tafa Juuf
New Comments(24)
sa compagne
❤️❤️❤️❤️❤️
CheikhA Gueye
❤️
158304310
je tancouraje mon grande frere qui est un vrait senegale
154373323
boy ya amm talent
151384554
machaalah
daba N'Dour
Faty Dioufsil15
machaallah lafe thiat futur Youssou Ndour
mariamaht994
machallah
seydou Beye
machallah
machalah un petit qui a un avenir dans la musique s'il continue sur cette lancée !!>