
Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia
- Genre:World Music/Folklore
- Year of Release:2022
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia - Wally B. Seck
...
sindjadjou sindjadja jougu lene niou magal ahmadou takk lene joukk lenne niou dém Touba touba Touba nekhna moto niou dougg charette niou yegg autorail niou yegg . Serigne bamba ki gnou mom mo gueneu si nioune Moy kignou mom diembalou mo gueneu si nioune si zayir si batine fi akk fagnou jeum ahmadoy kignou mommo gueneu si nioune Moy kignou mom diembalou mo gueneu si nioune si zayir si batine fi akk fagnou jeum Domi mame bousso daradjal ahmadou ya daradjal nit kou gnoul ba digne ko naw nakh Touba yi dagn ni won khetou diam lagn kénne dougnou naw ahmadooooooooooo( Serigne bi gnogui déti niane fakhir dafay naggou daguane yalla nagouna lepp loko niane sarakh niou natal kharnou bi)ahmadoy ki niou mom DEUG DEUG asnal yay kiniou mom diembalou mo gueneu si nioune si zayir si batine fi akk fagnou jeum ahhhmadoyy yay kignou mom si DEUG DEUG yay kignou mom diembalou mo gueneu si nioune si zayir si batine fi akk fagnou jeum Domi mame bousso daradjal ahmadoy ya daradjal nit kou gnoul ba digne ko naw nakh Touba yi dagn ni won khetou diam lagn kénne dougnou naw ahmadooooooooooo asnal khadim diagual nagnou civilisation missionnaire mo si jitou engagement si mom la né dévotion moko mom
Similar Songs
More from Wally B. Seck
Listen to Wally B. Seck Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia MP3 song. Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song from album Etat d'esprit is released in 2022. The duration of song is 00:04:44. The song is sung by Wally B. Seck.
Related Tags: Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia, Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song, Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia MP3 song, Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia MP3, download Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song, Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song, Etat d'esprit Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song, Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song by Wally B. Seck, Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia song download, download Asnal Khadim ft. Ahmada & Pape Seck Afia MP3 song
Comments (7)
New Comments(7)
149668993
do nitou fi
149668993
aphgqcvn
Mame Aminata Barro
[0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628][0x1f628]
Mame Aminata Barro
[0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623][0x1f623]
cheikh Abdoul Aziz seck
do nitou fi
Ndiaye familly
ndaysane thiey ♥️
Ndiaga Diop ixo29
Baye Fall deugg piir❤️✊
[0x1f604][0x1f604]