
Louné Lyrics
- Genre:Mbalax
- Year of Release:2020
This song is not currently available in your region.
Lyrics
Louné - Wally B. Seck
...
Toujours comme un siecle
Sa welcome une éternité
Cherie booooy oyii
Mbeguelou legui bala mouy nekh
Faw mou metti
Khol nala founer
Setnala founé
Sentou nala founé
Diarnagnou founé
And nagnou founé
Deg nagnou louné
Dath nagnou louné
Thi founé lounékeuu
Deug la leuh
Mbeguelou legui balamouy nekh day metti
L’infidélité ne se pardonne pas ça se comprend
Lek lek damalay togne
Wa tamit lek lek danga may togn
Diarnagnou founé
Dadj nagnou louné
Degal ngama louné founné
Sedel nala louné thi kouné
Founé keuh
Music......
Aidara cherie ma lover
Music......
Biram khary biram Nar
Sadiarra wané
Yaw mi fetek sa way
Dieulal way wi maynalako
Dieulal dieulal ni la way
Ndeke mbeuguél ni leuh
Mane guina ni
Kep kofi massa beugantel
Malako guenal
Gnou lango kay gnou lango ohh
Sama li sama laaa sama léeee hee
Music....
Yay sama li sama laaaa sama leeeeeehee
Hiiiiiiiiiii laaaa