
Tey la Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2024
Lyrics
Diaral nga ma geuneu diongué ey
Foy dem malay goungué héhé
Alkhaïri lagniy ndamo
Diap na la samay ñari loxo
Sama xol kaay weeru ci man mi
Diaratoul beurè ndax dang ma daan ahaan
Diarabi M'bifé I love you
Mi amore kaay weeru ci man
Souniou mbecté laniouy sèdé
Lo mounioul doko fekè
Souniou mbecté laniouy sèdè héhéhè
Andhou midho Faalama yea
Tey la tey la
Tey la Tey la
Je n'ai d'yeux que pour toi
Je suis prêt ma fleur à moi
Je suis à genoux devant toi
Viens que j'te mette la bague aux doigts
Ala xaala xaala
Ko an toun mbimbi è dièma
Ala aada aada
Andhou midho mi'jo fi'ma
Kaay ma press la baba
Nieuweul ma matal sama sunnah
Diarabi M'bifé I love you
Mi amore kaay weeru ci man
Souniou mbecté laniouy sèdé
Lo mounioul doko fekè
Souniou mbecté laniouy sèdè héhéhè
Andhou midho Faalama yea
Tey la tey la
Tey la Tey la
My African queen
You're the only one that im dreamin
From deep my soul i love you
And i promise,i'd never leave you
I wanna love you
Souniou mbecté laniouy sèdé
Lo mounioul doko fekè
Souniou mbecté laniouy sèdè héhéhè
Andhou midho Faalama yea
Tey la tey la
Tey la Tey la
I wanna love
And i wanna cherish you
Andhou midho faala ma
Tey souniou biss la
Nieupa gi sèdè heeheee
Tey la Tey la