
Reni xol Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2024
Lyrics
Babe girl mbir mi yow lë
Yay ki may wër
Mbir mi yow lë
Yay sama reni xol
Yay sama aldiana
Assamaan sèdé ma
Beut yima yeukeuti
Dieumè ko ci yow
Kone souf sèdé ma
Rongogne yima diota tour
Ngir sama Ouroul Ayni
Ni Yalla xar sama deuneu
Def la ci biir,def la ci biir
Amoul loy ragal
Ndakh dama miir
Babe girl Yaay sama xol
Yay kimay weur
Mbir mi Yow leu
Yay sama reni xol
Yay sama Aldiana
Ana koumay waxal
Sou goudi xaadiè nameu naa la
Yow yaay kimay bégal
Di seddal sama xol
Di ci def lou neexa neex
Ni Yalla xar sama deuneu
Def la ci biir,def la ci biir
Amoul loy ragal ndakh dama miir
Babe girl Yaay sama xol
Yay kimay weur
Mbir mi Yow leu
Yay sama reni xol
Yay sama Aldiana
Sama reni xol yay kimay begal
Sama reni xol nameu na la
Sama reni xol yay kimay begal
Dènk naala sama xol yea
Oh baby,xool na ba setaat guisna
Li né ci yaw
Oh lady,xoolé ba beutt set doyna
Ndakh da-fay-tiss-ci-mane
Yaay sama reni xol
Yaay sama aldiana
Yaay sama reni xol
Yaay sama aldiana