
Décroches ton téléphone Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2024
Lyrics
Woma Telephones
Décroches ton téléphone
Woma telephone
Wala bipé ma
Wala mess ma
Nameu naala
J'ai tant besoin de toi, je taime baby
Say retaan say waxtaan
Dellou cil gaaw
Je caresse l'espoir d'entendre ta voix
La chaleur de tes bras me manque
Comme tu me manques
Parles-moi
Delou cil gaaw ma baby
Comme tu me manques
Diéguèma
Delou cil gaaw ma baby
Woma Telephone(Lèlélé)
Décroches ton téléphone(lèlélé ma)
Woma telephone
Wala bipé ma
Wala mess ma
Nameunaala
Le temps s'efface
Ton souvenir reste
T'as laissé des traces
Mon Dieu me teste
Nos pleurs,nos rires
Toutes nos folies
Mon coeur revit quand tu me souries
Comme tu me manques
Parles-moi
Delou cil gaaw ma baby
Comme tu me manques
Diéguèma
Delou cil gaaw ma baby
Woma Telephone(Lèlélé)
Décroches ton téléphone(lèlélé ma)
Woma telephone
Wala bipé ma
Wala mess ma
Nameunaala
Weur na adounya
Guissouma keneen koumay deff ni'nga may deff waw waw
Piiss ma balaa may dè
Sagou dji diex na ci mane mi waw
Reuthiou na yow
Xadiouma fii
Nieuweul gaaw yow
Adounaa hahaan
Woma Telephone(Lèlélé)
Décroches ton téléphone(lèlélé ma)
Woma telephone
Wala bipé ma
Wala mess ma
Nameunaala
Je ferai de toi ma reine
Toi sur le toit
Je t'aime je t'aime