Back Home (Christmas Version) ft. Blowzbeat Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2023
Lyrics
Tell me how we can go back home
Show me how we can go back home
Let me let me go back home
Tell me how we can go back home
Show me how we can go back home
Let me let me go back home
Yow kaye fi
Niou wone gni
Louniou meussa done
Yow yow mi
Bokok ngi
Niou douniou nio nio nio nio nio niome
Nioune douniou meussa done
Douniou meussa meussa done
Niouy deuké khiro
Ak nono ohhh ohhh
Soutoura soutoura meussay done souniou yone
Nioune douniou deme ba faté ni ay kharit laniou wone
Mandemory mandemory im your lover
Tell me how we can go back home
Show me how we can go back home
Let me let me go back home
Go back home
Go back home
Yow kay fi
Niou do ré mi
Woné liniou mom o mo mome
Nioune kouniouye diema diakhassé yaye moudié melni iiii
Loumou goudi goudi goudi ma cherie
Meusounio done meussounio khame meussounio melni
Douniou taff di tepi
Di bind ba paré dindi
Douniou tieupi tieupi
Di melni kouniou gindi
Kham nga no no no non
Douniou meussa done douniou meussa done ni niome
Douniou meussa done douniou meussa done ni niome
Tell me how we can go back home
Show me how we can go back home
Let me let me go back home