POZITIF Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2023
Lyrics
Metina mais on gere et on contrôle
Dou louniou diaral dougou tchi ay tiol tiol
Nit kouné tchi yone dafay moytou tiow
Boule tegui sa tank ndakh none yi niongui khol
Guor nekal tchi sa bop
Ohhh Ay none aye none yé ay none
Foko séne ay none ay none yé ay none ay none
Ragalouniou nioune ay none ay none
Yé ay none ay none
Kou bakh bari ay none yé bari none
Loumou tarr tar na nga def teye def tey def tey ligueye
Bouniouye pause nan ga play ok ok ok
Don't listen to what they say they say they say
Cause everything is gonna be ok ok ok
Cause tomorrow gonna be a new day new day new day new day new day new new day new
Boule done ngaka
Diogual deme dieuli sa wale
Boule done ngaka familly yow laniou yakar
Dara doula téyé fitou gaindé boul diok tchi diko diayanté
Meunounioussi nada
Meunouniousi nada
Loumou tarr tar na nga def teye def tey def tey ligueye
Bouniouye pause nan ga play ok ok ok
Don't listen to what they say they say they say
Cause everything gonna be ok ok ok
Cause tomorrow gonna be a new day new day new day new day new day new new day new
Ohhh Ay none aye none yé ay none
Foko séne ay none lay none yé ay none ay none
Yé ay none ay none
Kou bakh bari ay none yé bari none
Loumou tarr tar na nga def teye def tey def tey ligueye
Bouniouye pause nan ga play ok ok ok
Don't listen to what they say they say they say
Cause everything gonna be ok ok ok
Cause tomorrow gonna be a new day