Touba lovers Lyrics
- Genre:Others
- Year of Release:2023
Lyrics
Touba laye beuga deme
Deme tè dotouma nieuw
Ndakh Touba day yok leeer doy Wañi ay Bakar
Touba laye beuga deme
Deme tè dotouma nieuw
Ndakh Touba day yok leeer doy Wañi ay Bakar
Bayou Modou Moustapha mome Lañiou yakar
Fi ba fañiou jeum Seydina Mouhamado Seydina Mouhamado
Bayou Modou Moustapha mome Lañiou yakar
Fi ba fañiou jeum Seydina Mouhamado Seydina Mouhamado
Douma dougou louy khouss djeum Souff
Douma dougou louy naw djeum Kaw
Autorail touba laye djeul Barisakhaya

Fi ba fañiou jeum Zeydina Mouhamado Seydina Mouhamado
Bayou Modou Moustapha mome Lañiou yakar
Fi ba fañiou jeum Seydina Mouhamado Seydina Mouhamado
Douma dougou louy khouss djeum Souff
Douma dougou louy naw djeum Law
Autorail touba laye djeul Barisakhaya
Aytia
Aytia