![Incompris ft. Ibu Fire](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/11/08/c25ede9e765c4654a76bfa503fffdf0b_464_464.jpg)
Incompris ft. Ibu Fire Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Tedj seu guémign ngeu daw youhou wallelou
Seye lokho meunougn loudoule mballeelou
Niongui ci kaw assamane di dalleelou à part souniou meunine kene meunouci wallou
Fo meunti deguati ice nice fekkneu feye nagn niou nice price
Beugougn meu guiss meu am nice slice mais keene nékouci sama size
Incompris pour niuy latchei loutax siwoumeu beu legui
They cannot handle me beugugn meu guiss sene biir
Seu premier essai moy seu dernière chance nigguh fekhel am dadj soy retii (Tir)
Chaque insomnie niu fanaanei cook ay hit
Limssi gueuneu dem mane gueuneu nocif
Kone someu compoul xamna liro Notice
Non boul meu djeul au serieux mane leu Boris
Dou prank soumleu nei bayina rap parei gueu guiss niu au lit (Ey)
On est lié pour ive dafmeu fekeu sameu neke digu meu les clefs de la ville
Meu nangou nekeu Jummah biir Tel Aviv
So fayoul sameu addition defago diff
Neileine ey rap bi lim meu digone lay djeulsi
Niakeu sameu xel rek mo meun nek sameu phobie
Sinon lou nek sameu ligne de mire lep lay wekki (Ey)
Yagu nafi freestyle di def hit
Nelaw di rap jamais nelaw si kaw beat
Dougu def fi degat BP yi done notif
Locataire gueu boy seu rap djoto xaliss fi
Incompris pour niuy latchei loutax siwoumeu beu legui
They cannot handle me beugugn meu guiss sene biir
Seu premier essai moy seu dernière chance nigguh fekhel am dadj soy retii (Tir)
Chaque insomnie niu fanaanei cook ay hit
Tedj seu guémign ngeu daw youhou wallelou
Seye lokho meunougn loudoule mballeelou
Niongui ci kaw assamane di dalleelou à part souniou meunine kene meunouci wallou
Fo meunti deguati ice nice fekkneu feye nagn niou nice price
Beugougn meu guiss meu am nice slice mais keene nékouci sama size
Xex na beu dane samey xalat yu suicidaire moy sameu big win fils
Incompris comme policier buy gérer fugitive (Ey)
Xawmeu nignuy sisso si musique
Dioxleu musique yu set beu doto sissou meme soy Math mes vidéos
Nax MH si prod yi comme tableau boubou design
SAB neneu li comme Messi feat Cris (Nigguh)
Lounex dou doy deglou conseillou Ibu Fire fi yeup di boy
Fuck ay punchline neileine maguek ay flow yu hot
Soumko dorei dey dal nigguh tei boy dou moy (Non)
Neko Tiow li dou fay (Fay)
If you don't know nigguh you know depuis temps boy legn ko iri home
Wow