![Letter To My Mama](https://source.boomplaymusic.com/group10/M00/11/08/c25ede9e765c4654a76bfa503fffdf0b_464_464.jpg)
Letter To My Mama Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2022
Lyrics
Hi Mama
Yeah
Yeah
Sameu mind dafeu chers même iblis meunoko djeund
Andak God mou tracer sameu way ci game bi fess del aki deum
I know Mama doumaci dougu sou tey nekone demb
Dafeu nek ci mane beu xamatoumeu noumey def beu guene ci
Je suis au fin fond dans le puit de la musique
Kounek seu don boul meusseu douter j'ai le truc
Le talent paye kone fokniu dioxmeu sameu prix
I have a dream moy sameu music fay ay school's bills
Huh
Dou foularou scout non (Nananana)
So yewo guiss meu sene scoop (Nana nana)
I got 99 problems Music nekoul ci biir
I'm still your kid Mama
Même sou feikei nexouleu guiss (Ohh non)
Yanei ci biir meu dolei pour sori iblis (Ohh non)
Soxlawoul punchlines pour gueu meuneu feel seu lyrics Kid (Ooohh non)
I know
Doumeu fanane ci biti yeah tei gueu nek fi
Sameu Mind suy play ay films dou meusseu done acteurou ARROW
Yaa know (Ya know Mama)
I know (I know Mama)
Yaa know
I'll love you forever Mam
Yaa know (Know)
I know (Know)
Yaaa know (I'll love you)
Mane sameu mind (Miinnnd)
Dey deukei Fly (Deukei fly)
Voyager High (So high)
Mais jamais mou fatei Yaye Booye
Mane sameu mind (Sameu miinnd)
Dey deukei Fly (Deukei fly)
Voyager High (So high)
Mais jamais mou fatei Yaye Booye