Why Lyrics
- Genre:Hip Hop & Rap
- Year of Release:2020
Lyrics
OG Niaye Niaye
OG Niaye Niaye woo
Haann Whyyyyy
Hmmm hmmm
Whyyyy
Whyyyy
Whyyyyyyyyyy whyy
Whyyy
Whyyyyy
Fok gueu waxmeu baby whyyyy
Whyyyy
Whyyyy
Whyyyyyyyyyy whyy
Whyyy
Whyyyyy
Fok gueu waxmeu baby whyyyy
Wait na beu soneu senoumaleu
Sameu guent rek guey deloussi (Ouais ouais ouais)
Djem naleu call degoumaleu
Raccrocher meu au nez meu guen leu feel (Skrrr skrr)
Wait na beu soneu senoumaleu
Sameu guent rek guey deloussi (Ouais ouais)
Djem naleu call degoumaleu
Raccrocher meu au nez meu guen leu feel (Skrrr skrr)
Baby
Fo sandi seu khol meu dem djeuliko ouais
Sorry
Il parait que Ma tangal seu khol kay meu djeuriko eh
Indice
Nane lay def pour effacer lileu metiwone
Metit
Nenegn sileu bok faut que niu deal ak mom
Mais Boul nangou suniu love di bankrupt
Mane gueu beugu def seu ex
Keup caisse yi pour niu set it up
Soy bayi mey deposer next
Liguafi nekoul dafmeu weteul
Il fallait que mou tiol pour niu wake up
Doundou love bi non sans make up
Lepeu niu cons duniu desseul
Non babe boul nax seu bop yeahh
(Nooon nooon)
We're bestie
Tei nekougn boy si friendzone
Et puis
Fin story bi mak yoe ley done yeah
Kuy bayi
Kuy trahir suniu kingdom
Whyyyy
Whyyyy
Whyyyyyyyyyy whyy
Whyyy
Whyyyyy
Fok gueu waxmeu baby whyyyy
Whyyyy
Whyyyy
Whyyyyyyyyyy whyy
Whyyy
Whyyyyy
Fok gueu waxmeu baby whyyyy
Wait na beu soneu senoumaleu
Sameu guent rek guey deloussi (Ouais ouais ouais)
Djem naleu call degoumaleu
Raccrocher meu au nez meu guen leu feel (Skrrr skrr)
Wait na beu soneu senoumaleu
Sameu guent rek guey deloussi (Ouais ouais)
Djem naleu call degoumaleu
Raccrocher meu au nez meu guen leu feel (Skrrr skrr)
Niogui miner depuis daw
Gueu tegui tank takhul meu guenessi
Time is money faymeu now waleu nekeussi
Meusso guiss dealer buy deal on fleek
Maguini yokh leu beu nieup sip
Let's be my trap queen meu nekeu seu fetty wap
But niari beut laley xolei fuck illuminati
Yeah dameu Rich si khol melni kuy nelaw si pyramide
Souleu neixei kay dioxmeu seu xol yeah meu djam si versace versace
Dam fogone ni biyone c'est okay nax demneu bou dakeu bou jay z beyonce
Biyone c'est "Shawty lo beug love pareina"
Lo dioxogn meu dagueu ni piranha
I ain't got the plug-in boul dougou si mane
If u're here for playing nax legui mane gareina
Guiss negn defaut fok niu dab si (Yeah)
Corriger ko changer vibs yi (Yeah)
Sougn beguei mou dox fok niu djapssi
Insbi dey lirr mais one day dey magui (Yeah)
Im ready like never before yeah
Kay fi meu leral sey phares gueu djam meu ay code
Meun negn wax ni que tek gameu choc
Nax beukouna kone boulmeu waxni que pareiwo
Whyyyy
Whyyyy
Whyyyyyyyyyy whyy
Whyyy
Whyyyyy
Fok gueu waxmeu baby whyyyy
Whyyyy
Whyyyy
Whyyyyyyyyyy whyy
Whyyy
Whyyyyy
Fok gueu waxmeu baby whyyyy
Wait na beu soneu senoumaleu
Sameu guent rek guey deloussi (Ouais ouais ouais)
Djem naleu call degoumaleu
Raccrocher meu au nez meu guen leu feel (Skrrr skrr)
Wait na beu soneu senoumaleu
Sameu guent rek guey deloussi (Ouais ouais)
Djem naleu call degoumaleu
Raccrocher meu au nez meu guen leu feel (Skrrr skrr)