Wax dëgg
- Genre:Spoken Word
- Year of Release:2019
Lyrics
Xarit kaay ma wax la samay xalaat
Denq ma say nopp
Ma toqal ci samay xalaat
Gaa ñi, kar nañu dëgg siif, siifaat
Ñu jàpp dëgg fàdd, fàddaat
Dëgg jib ñu gàntu, gàntuwaat
Saaga nañu dëgg, toroxal nañu dëgg,
Waaye taxul ba leegi dëgg sëgg
Ndax mooy kiy lakk seeni taat
Amna ñu dajaal ngemb ngir ñu këf sunuy xel tek ci kaw jaat
see lyrics >>Similar Songs
More from Meissa Mara
Listen to Meissa Mara Wax dëgg MP3 song. Wax dëgg song from album Wax dëgg is released in 2019. The duration of song is 00:04:16. The song is sung by Meissa Mara.
Related Tags: Wax dëgg, Wax dëgg song, Wax dëgg MP3 song, Wax dëgg MP3, download Wax dëgg song, Wax dëgg song, Wax dëgg Wax dëgg song, Wax dëgg song by Meissa Mara, Wax dëgg song download, download Wax dëgg MP3 song