Bataxal Lyrics
- Genre:Pop
- Year of Release:2021
Lyrics
Na Na NA Na Na Na Na
Na Na NA Na Na Na Na
Eh Eh Eh Eh Eh Eh Eh
Na na...
Mane la kinga donone deimbe
Ma la indil bataxal tay
Nguir fataly lou beury
Si aduna bou teureudy
Mane la kinga donone deimbe
Ndaw bissi yow moma yobanté
Nguir nga moytou lou beury
Ndax nga meuna deime fou soory
Néna nga moytou leip louy loor
Té moytou topp sa bakane lol
Ndax aduna bii…
Saxoul day diéxyy…
Néna boul deuk thi rafete ndiorte
Ndax dinga faral guiss lo foguoutone
Thi aduna bi…
Moytoul nite gnii…
Na Na Na eh…
Na Na Na eh…
Degloul Bataxal bi
Degloul Bataxal bi
Na Na Na eh…
Na Na Na eh…
Degloul Bataxal bi
Degloul…
Néna ma wax la soxor baxoul
Ko guiss yéné ko lou bax
Ndax aduna yagoul
Lo guiss reik daffay diéx
Néna nga fonk say wadiour
Say mbokak gnila beugg
Ndax sa yo diaxlé
Niom reik mgay guiss
Na Na Na eh…
Na Na Na eh…
Degloul Bataxal bi
Degloul Bataxal bi
Na Na Na eh…
Na Na Na eh…
Degloul Bataxal bi
Degloul…
Anh…
Mane la kinga donone deimbe
Ma la indilone bataxal tay
Nguir fataly lou beury
Si aduna bou teureudy
Mane la kinga donone deimbe
Ndaw bissi yow moma yobanté
Nguir nga moytou lou beury
Ndax nga meuna deime fou soory